Credits

PERFORMING ARTISTS
Sheikha The Legend
Sheikha The Legend
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Cheikh Ismaila Mbaye
Cheikh Ismaila Mbaye
Songwriter

Lyrics

Dama la bëggee fa mbëggéel cosaanoo
Ba dara doonul dara ba tay ji lee
Sun doon ñëwaat yaw laay
Bëggaat
Ta sun doon ñëwaay yaw laay bëggaat
Yaa ma ne woon jox naa la lépp yaay boroom
Tax ma lay laaj ndax ni ma la tëyee doy na la
Maa la digoon ne safara si du mës a fay tax ma lay woo
Ma ne yeewwul waay
Sama reeni xol
Saa yo yeewwo yee ma
Sama xol day neex
Fimne yàkkamti naa
Ba nga delsiwaat
Ma ne yeewwul waay
Sama reeni xol
Dama la soppee fa cofeel cosaanoo
Ba dara doonul dara ba tay ji lee
Sun doon ñëwaat yaw laay
Bëggaat
sun doon ñëwaay yaw laay bëggaat
Yaa ma ne woon jox naa la lépp yaay boroom
Tax ma lay laaj ndax ni ma la tëyee doy na la
Maa la digoon ne safara si du mës a fay tax ma lay woo
Ma ne yeewwul waay
Sama reeni xol
Saa yo yeewwo ree ma
Sama xol day neex
Fimne yàkkamti naa
Ba nga delsiwaat
Ma ne yeewwul waay
Sama reeni xol
Written by: Cheikh Ismaila Mbaye
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...