Kredyty
PERFORMING ARTISTS
Abdou Guité Seck
Lead Vocals
COMPOSITION & LYRICS
Abdou Guité Seck
Songwriter
Ousmane Ka
Arranger
Bril
Arranger
PRODUCTION & ENGINEERING
Abdou Guité Seck
Producer
Tekst Utworu
Soppé Yi
Am na niou lay bëgg
Def la seni khol
Mbëguel moy dëgg
Dondiou galasse thi khol
Lou baakh lou niou guiss
Yaw lan koy yenne
Lo yenou mou diis
Dagn la koy yenni
Lou niou guiss mouy tiiss
Dougn la ko yenne`
Sou ma len meunoona fekk foune
Deuke dilen ndokel sa sou ne
Dinaa la riitil boumou khalam tay
Dina la sigil thi say nawle tay
Dina la defal li lay beggal tay
Li gua gënna bëguak
Ligua gënna fonkk
Li gua gënna naw thi man tay
Lay foull en guise de reconnaissance
Kou len fale
Man mi la fale
Kou len wolou
Man mi la wolou
Gueye Semou Madjiguenoo yayou Bounama
Yaye Adjia Mada Guey yar na ndiabootam
Yaaye ! Koula nawloo doy na ma nawloo
Sope yi
Samay nit
Kou len am dieul
Kou len niakkit wouti len
Kou len wouti guiss lene santh seni wett
Abadan guen deukke beggue
Bilay naw loo na len
Bilay naw loo na la
He yama te teye
Bilahi wetaloo ma
Taatan naa samay baggaan
Seni khalaat ladi taataan
Garab gou nara Kendal peincc mi
Bou ko boroom semin bi sen
Ne koune indi li gua werle
Niou diem ko sognie waar wi
He wolou naa len
Bilay naw loo na len
Ndeye Coumba Falloo Famay sa yaay domi general ba gui
Yayou Aicha cherie Laminoo Nabou Fall mooy magg dia
Magui Bassirook Ndeye Arame fall Mami Falloo baakh gua
Mami Fallo cherie Abou Diallo Anta Niang moy yaayam
Nitou Soukeyna Diagn naar Khady fall moy mag dia
Cherie Papa Diop Ndeye Marie Diallooy sa. ndieukke
Rama Diallo ma thia wakam Poulmera modi yayam
Borom Salon Poulmera baakh Adel Diagne moy khol ba
Fatou Sow pouloo cherie Ismael yagg na niou lool garmi
Sama sope yi ken de gueunou len sama garmi yaa gue
He wolou na lene
Bilahi wolou na len
FIN……
Written by: Abdoulaye Guitte SECK

