Vídeo de música
Vídeo de música
Créditos
PERFORMING ARTISTS
NIX
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Nicolas Omar Diop
Songwriter
Seydy Sarr
Songwriter
Samuel Tingbo
Songwriter
Yann Moni
Songwriter
Letra
Doundou na sama Life yeah
Beugue na sama Life yeah
Daan negn ma li nga gueune beugue mo ley sonal
Daan negn ma wakh fi nga soti sa xel mo lay jomal
Lo xamoul moy souma delone guinaw boy ma defate ko
Lo xamoul moy souma delone guinaw boy ma defate ko
Ndakh lo guiss dey diekh takhoul dougn ko ba
Lo guiss dey diekh takhoul dougn ko ba
Tana na sama bor yeah tana na sama boss
Tana na sama bor yeah tana na sama boss
Tana na sama bor yeah tana na sama boss
Tana na sama bor yeah tana na sama boss
Doundou na sama Life yeah
Beugue na sama Life yeah
Boul sori li nga gueum yeah
Songal li nga beugue yako kham yeah yeah
Boul sori li nga gueum yeah
Né negn ma boul ci dougue do ci gueneu yeah yeah
Ma tope sama zone yeah (oh yeah)
Ay vibes dima fone yeah (oh yeah)
Ay paka dima jam yeah (oh yeah)
Ba xalat bi gueune xaut yeah (oh yeah yeah yeah)
Fii lo guiss bes dina diekh nga doundou
Tiis lo guiss bes di na diekh nga Doundou
Demal ba diekh yenou lou diiss (yeah )
Mou nekh Wala mou meti boy there you go
Niou beugue le niou bagn leu boy there you go
Dieuleul succès Def ko toureundo
Doundou na sama Life yeah
Beugue na sama Life yeah
Guissna li nguey doundou sibir sama seetu
Sa metite moma gaagn sunu yaram nekul
Soum fi nekul yow rek ya ma meuna guestul
Daw guinaw louy dora guene ndéké dara bessoul
Moussouma aay ci fake li ma feeloul
Awma li may neubeutou sama xol meussoul tilim
Awma li may titeurou ci jigueen bouma iri
Ndakh lo leteu beus mou firékou firi ko diokh ko siri
Loula yallah may homie momou loko
Beus sa yaram dina daw beu nga taalal lokho
Meun na navette té dou taw lolou doundou negn ko
Doundou na sama life beus ma doundeul la ko
Doundou na sama life beus ma doundeul la ko
Doundou na sama life beus ma doundeul la ko
Doundou na sama Life yeah
Beugue na sama Life yeah
Daan negn ma li nga gueune beugue mo ley sonal
Daan negn ma wakh fi nga soti sa xel mo lay jomal
Lo xamoul moy souma delone guinaw boy ma defate ko
Lo xamoul moy souma delone guinaw boy ma defate ko
Ndakh lo guiss dey diekh takhoul dougn ko ba
Lo guiss dey diekh takhoul dougn ko ba
Tana na sama bor yeah tana na sama boss
Tana na sama bor yeah tana na sama boss
Tana na sama bor yeah tana na sama boss
Tana na sama bor yeah tana na sama boss
Doundou na sama Life yeah
Beugue na sama Life yeah
Written by: Nicolas Omar Diop, Samuel Tingbo, Seydy Sarr, Yann Moni