Credits
PERFORMING ARTISTS
Samba Peuzzi
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Pape Moussa Diagne
Composer
Christ Johan Ollanghas Kimbeki
Composer
SAMBA TINE
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
Pape Moussa Diagne
Producer
Lyrics
Wessu nañ xarit legui done nañ ay domu ndeye
Ak ñi nga guissalone demb nga may guisseul tëy
Ko toñ ci gang bi ñune ñeup geu toñ
Wessu nañ xarit legui done nañ domu Ndiaye
Ay nittu deug fi ken du changer
My broda for life never change
Ay nittu deug fi ken du changer
Hey Broda for life Eh Yah
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
Ouais la famille hey
Ça bouge pas
La Famille (Gang)
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
Eh la famille Hey yah yah Hey
I do it for my gang
I do it for my family
Lu meunti xew du tax ñu tass c'est à vie
Bo déconner dama lakoy wax rek ñu andat cool
Lu yagg deug leu sunu and bi dé du ay dul
Faté xajufi yen tek ladone guiss depuis ba muy metti
Xolal faté xajufi yénama dolel bama yeksi fi
Yah yah hey
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
Ouais la famille
Ça bouge pas
La Famille (Gang)
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
Eh la famille Hey yah yah Hey
Wessu nañ xarit legui done nañ ay domu ndeye
Ak ñi nga guissalone demb nga may guisseul tëy
Ko toñ ci gang bi ñune ñeup geu toñ
Wessu nañ xarit legui done nañ domu Ndiaye
Ay nittu deug fi ken du changer
My broda for life never change
Ay nittu deug fi ken du changer
Hey Broda for life Eh Yah
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
Ouais la famille hey
Ça bouge pas
La Famille (Gang)
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
La famille ça bouge pas
Eh la famille Hey yah yah Hey
Written by: Christ Johan Ollanghas Kimbeki, Pape Moussa Diagne, SAMBA TINE