Credits
PERFORMING ARTISTS
Ashs The Best
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Ashs The Best
Lyrics
Abdoulaye Sy
Composer
Olivier Delahaye
Composer
PRODUCTION & ENGINEERING
Nautylusprod
Producer
Lyrics
Xel du ko sut te xol a koy gis
Bëtt du ko se'en la'miñ mënu ko wax
Everyday every time neena moo
Ngi sa wet Moo la gën na jege sa buumu xol ba
Ya'lla a ngi fi
Moo ngi fii akk fiiniou jeun Ya'lla a ngi fee
Ya'lla moo ngi everywhere Moo
Fii akk fii niou jeum Ya'lla joggu fi
Yalla na Ya'lla bay sa to'ol
Ñun say jaam ñoo ngi lay ñaan
Nangul ñu lepp luñ la ñaan
Ngir faqqir day nangu daggaan Ndax
Ya'lla naatal xarnu bi
Xel du ko sut waaye xol da koy yëgg
Boo ñu mayee ling nu mayoon
Dootu ñu def li ñu defoon
Xanaa yëggoo ni ñun yaru nañ
Buur Ya'lla naatal xarnu bi
Nangul ñu lepp liñ la ñaan
Ndax yalla natal kharnou bi
Ngir sa yërmande ñi ngi lay tuubël
Lepp lu xaraam te di nangu nuroo ki jaam
Boo ñu joxee di nañ la sant
Te boo ñu joxul dutee ñu xëy di gën sant
Rafle, sone ak xiif akk fande ak teud si souf
Ngir bëgg am sa yërmande
Du ñu xaddi, du ñu sof du ñu daw te du ñu lakkatu
Ngir bëgg am sa yërmande
Loo wax ñu nangu, yay buur baaxal ñu
Te boo ñu mayee ling ñu mayoon jeegël ñu
Dootu ñu def li ñu defoon
Xanaa yëggoo ni ñun yaru nañ
Buur Ya'lla naatal xarnu bi
Nangul ñu lepp liñ la ñaan
Ndax yalla natal kharnou bi
Writer(s): Abdoulaye Sy, Ashs The Best, Olivier Delahaye
Lyrics powered by www.musixmatch.com