Music Video

Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Elage Diouf
Elage Diouf
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Elage Diouf
Elage Diouf
Songwriter

Lyrics

Diakhlé ma tax di ladji Ndax liwone mome wonénina Teranga diangay déme – Kéne xolatoul sa morome Nitay liguéye morome nguir ignane Soxor – niaak gueume yalla Interet tassna rewmi Lou waye def morome – amna loumou ciye sentou Boul guiss nite ki diko bagne - Kokou defoula dar Boul xole nite diko djiépi – Ndax lolou waroula yow Boul tite yow – boul délou guinaw dome Mani boul xébe – boul bayi gna nga dekeulone déme Hée bilaye walay – méréwoumala yow yaye sama xarite Bilaye walay meréwoumala seute yaye sama yaakar Keupe kou eupe sa morome doley wala alal wone nalako Kéne défoule nguir yalla – kofi digaléle mou warla Téranga dja ngay déme – bax mome moungui nara toumouranké Djiko yi cii neg bi laa yakho – dial ci mbéd mi – laaw ci rewmi Boul guiss nite diko bagne té nite kokou défoula dara Boul xole nite ki diko djiépi té kokou mome défoula dara Boul tite yow Boul délou ganaw dome Mani boul xébe yow Boul bayi nga nga dekeulone déme Han bilaye walay merewoumala dome – yaye sama nite Bilaye walay méréwoumala waye – yaye sama yaakar Sa melokáane mome laniou laay raagné - Han boufékéni Lou nekh la modi nieuw Sa melokáane mome laniou laay raagné - Han boufékéni Han damay woye séne toure Sa melokáane Weurseuk bi nieuw daniou nane tiénou bateau mome mounouko téyé Ndax yalla moye déf lolou Jaam limou nara ame laay ame Djiéguici léne – ma woye borome melokáane you raféte yée Yalla moye déf lolou Han lou meunta gnak fo'k mou ame Nako di déf ngay xole Nako di déf ngay séeune Nako di déf ngay xole yaye Jaam mome, limou nara ame laay ame Sa melokáane mome laniou laay raagné - Han boufékéni Han toudou naniou sa toure Sa melokáane mome laniou laay raagné - Han boufékéni Han yow mate nga ndjite Yow toudé nanioula dome Yow da nga raféte xole Han toudé nanioula dome Adjia Seynabou Faye laay woye Sa melokáane raféte yaye bo law cii saaye domes Papa Badara Mbengue bayou Elage ak Babacar Thioro Mbengue Mor Papa bakh nga lolou Bayou Maman Soda Ak Cheikh Mbacké daamay koye woye Kor Ndéye Diaw - Cheikh Dieng raféte ngéne melokáane Moustapha Guéye Ndioro kor Bercy ak bayou Cheikh Wa Ndar guédji tey laay woye séne dome djié Kor Rama Ndiaye - Papa Diop raféte nguéne melokáane Massata Ndiaye kor Astou woye naléne thia Montréal Sa melokáane
Writer(s): El Hadji Fall Diouf Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out