Music Video

Ashs The Best - Waxtu feat. AMADEUS [Audio]
Watch {trackName} music video by {artistName}

Credits

PERFORMING ARTISTS
Ashs The Best
Ashs The Best
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Tiare Arfang
Tiare Arfang
Songwriter
Abdoulaye Sy
Abdoulaye Sy
Composer
Olivier Delahaye,Symenouh Fructueux
Olivier Delahaye,Symenouh Fructueux
Composer
PRODUCTION & ENGINEERING
Nautylusprod
Nautylusprod
Producer

Lyrics

Ndekete yóo waxtu yé ñu boole woon du xaritoo kase Ndekete yóo waxtu we taxoon ñu doon dajee weer bu ne Woo nga ma ci guddi gi fekk mu maas Ci ëlëg tamiit, fi ci suba ci, fekk mu naaj Waxtu bi su weeso dotul ñëwaat Do ko dabuwaat Bala dellusiwaat Mu nekk ci beneen bës Bu jànt bi di so fi, féele di naaj Bu guddi gi di xaaj fi, timis di waaj a jot fe Massamba ma nga Walo Suba soxla ya koy yoobu Ndakaaru Te ëlëg ndogal mën na fa xandalu Fi ak ay bés mu jiibi sanc walo Ndekete waxtu yi ñooñii boolee Ñoom ñooñii boolee Du xaritoo kaase ñoom ñooñii boolee Ndax bu ëlëge mën nañu jiiwalo Waxtu w saay su jotee(bu fekkee waxtu woowu la wootee) Foo mën ti nekk, waxtu w bu jotee Budul suba tamiit sa boos moo ñi ñëw Ass fay nee na du xaar suba Ndax yàkkamti na te démb weesu na Ku sàkk gaa ye moo ñi dajaale Ci adduna bee ci waxtu jii li mel tay Mara naan, marul naan, naan, am na potu-ndaal Ndox ma ngay walangaan, ñun buñu réeroo Ndox ma ngay walangaan, ñun buñu réeroo Te amaana buñu diisoo di nañ déggoo Ñu bañ di réeroo Nañu déggoo di bañ di réeroo Amaana buñu booloo mu may ñu doole Boroom bi def ci ndam su ko soobee Bu ñu boolo, nañu boolo
Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Kya Loum Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out