Music Video

Featured In

Credits

PERFORMING ARTISTS
Daara J Family
Daara J Family
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Abdou Fatha Seck
Abdou Fatha Seck
Songwriter
Mamadou Lamine Seck
Mamadou Lamine Seck
Songwriter

Lyrics

Jom mooy dém waayé fulay ñibbisi Jambaar dawul doolé ladoon wuti Yagg naa bittim reeeeew ñibbisinaaaa naaaaaa naaaaaa Sama reew Sénégal SENEGAL SENEGAL SENEEEEEGAAAAL SENEGAL J'aime ce Pays Qui m'a vu grandir Cette terre qui a vu Mes premières larmes Et mes fou rires Pas besoin d'un crayon pour dessiner Les sourires Tels des rayons De soleil pour taccueillir Le CFA parle fort à travers et à tort On marchande pour Le transport et Quoi encore Ici c'est Taxi-brousse Jaune-noir cars-rapide Ndiaga ndiaye ou Pousse-pousse Petite pause dans une Dibiterie ouTangana Petite tintamarre C'est du Tama Elle danse avec ou sans salaire Malgré les coupures d'électricité Deau et la Galère Une pensée Pour les frères qui ont coulé Dans l'Atlantique Même si j'ai la chance de revenir Ma blessure est à authentique Nul n'est prophète chez soi Mais on eqt mieux que chez soi C'est vrai j'ai duré là-bas Mais mon cœur était là SENEGAL Jom mooy dém waayé fulay ñibbisi Jambaar dawul doolé ladoon wuti Yagg naa bittim reeeeew nibbisinaaaa naaa naaaaa Sama reew Senegal SENEGAL SENEGAL SENEEEEEGAAAAL SENEGAL Fila reew néexé Sénégal ngi ni dé Booko soré dooto bêgg Ludul Ñibbisi dé Bofi ñëwé joxé Mbok néla kaay ñu gissé Ana lo inddi daañ la yenni Say xarit yaggon toog di Xaar di séntu bis bi mi ngi Ñew na tay no dikké serica yi Nga diggé Sèntu nañla fin d'année été Doyul daggal billet Att bilé giss mbok yilé Summi yërré immigré Metro boulot amul Dodo Kogg bala jant bi Modou modooo Ñu ngi daw wuti wuti Bitim reew bañ fa futi ubbi Buntu xéwal bis fok ñu ñibbi Mu ngi guddi sorri Nga dëkkuwaay géntal ñulay teeru bis di Ngua délluwaay yoon wi Na nga léer lu Xamal né Jéggé na njaboot gi ñeppa ngi xaar Démoon nga ñewaat nga Senegal mooy sa képaar Le courage de partir La force de revenir Partir Pour grandir Revenir pour bâtir Dans la grisaille et le froid Jentendais ta voix Me Revoilà chez moi Là où je me sens comme un Roi SENEGAAAL SENEGAL SENEGAAAAL SENEGAL Jom mooy dém waayé fulay ñibbisi Jambaar dowul doolé ladoon wuti Yagg naa bittim rew nibbisinaaaaa naaa naaaa Sama reew Senegal KAFFRINE SEDHIOU THIÉS LOUGA DIOURBEL SAINT LOUIS MATAM KOLDA KAOLACK KEDOUGOU TAMBACOUNDA ZIGUINCHOR et DAKAR Senegal Senegal Senegal KAFFINE SEDHIOU THIÉS LOUGA DIOURBEL SAINT LOUIS MATAM KOLDA KAOLACK KEDOUGOU TAMBACOUNDA ZIGUINCHOR et DAKAR Senegal Senegal Senegal
Writer(s): Abdou Fatha Seck, Mamadou Lamine Seck Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out