Music Video

Music Video

Credits

PERFORMING ARTISTS
El Maestro Le Kangham
El Maestro Le Kangham
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Moustapha Diop
Moustapha Diop
Songwriter

Lyrics

El Maestro
Oh oh ooh!!
Yaw daga bari Yiré
Wayé mano solou
Man nima solo da simpal
Fouma guén Mashalla
Moy Sagnsé Challenge
Wakh ma noy Sagnsé Challenge
Moy Sagnsé challenge
Wane ma noy Sagnsé Challenge
Boul xol linga Yoor
Ndakh mom ngay ndougué marché
Sagnsé doussi kopar
Si Yaw mila ma sœur
Usal sa braind wanél sa jongué
Kourti kourti
Jiguen day bari fem
Lo manti yor mansé Sagnsé
Fala niouy xamé ndanane nga
Fala niouy xamé ndanane nga
Kone def ko Challenge
Sagnsél def ko Challenge
Rang mouy gaw
Def ko Challenge
Sagnsél def Challenge
Rang mouy gaw
Yaw daga bari Yiré
Wayé mano solou
Man nima solo da simpal
Fouma guén Mashalla
Moy Sagnsé Challenge
Wakh ma noy Sagnsé Challenge
Moy Sagnsé challenge
Wane ma noy Sagnsé Challenge
L’élégance, la beauté, l’esthétique
C’est de l’art
La finesse, le feeling la simplicité
C’est de l’art
Wawaw
Aka nio mana Sagnsé xalé
Rang Mouy Gaw
Xamga Pomme dou Moromou Néww
Rang Mouy Gaw
Man fouma Sagnsé
Nga dég Ah Thioummm
Rang Mouy Gaw
Yaw daga bari Yiré
Wayé mano solou
Man nima solo da simpal
Fouma guén Mashalla
Moy Sagnsé Challenge
Wakh ma noy Sagnsé Challenge
Moy Sagnsé challenge
Wane ma noy Sagnsé Challenge
Written by: Moustapha Diop
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...