Lyrics

Ouh ouh hou Hou hou hou wa Hou houhou hou Xolou ma kenen Fess na sama settu Djiguene dji wakhé djeuf Dou am diotou tontou Doon awo di bourou keureum Li dou ay fontou Té sakh fouma momé Zéro lakoy wathié Lou deuss meuneu daw Un bé ngui ci kaw Gnari faan gnouné fo feug aljana takhaw Bonheur Fi wakh amoul Thiouray bi riir Def terreur Loutakh mouy sedd té may diegg pire Péssé sama bopou Kham né warou ma ragal woudié Ladial mon cœur Kouy madame bonheur Ya may confiné Lepp di dioub Ya raw poli-cier Ladial mon cœur Kouy madame bonheur yé Li ley door Té doula laal Nékhoul ci xol Deuxième dame Bi la gnou takkal médaille d'or Ki nélaw la khamone Ma diangal ko yandor Bayi léen di diem Diang kham sa goor a gueuneu woor Xol bi nangou féété Boboy doundou mbecté Namouma daray wakh Beu fi mingui bakh Chéri dougueul deuk Do feug yay laisser passer Allô Fi may sourire mou évanouir Mais allô Ay nélaw diékh na té may nonou Péssé sama bopou Kham né warou ma ragal woudié Ladial mon coeur May ki key bonheur Yamay confiné Lepp di dioup Ya raw poli-cier Ladial mon cœur May ki key bonheur Coco man ak yaw ba Aljana Thi sa wett la doundé oh lala Ya raw ci man Say je t'aime thi sama biir tympan Nim may def nekh na ma Beug nala babe Péssé sama bopou Kham né warou ma ragal woudié Ladial mon cœur Kouy madame bonheur Ya may confiné Lepp di dioup Ya raw poli-cier Ladial mon cœur Kouy madame bonheur Ladial mon cœur Kouy madame bonheur Ladial mon cœur May ki key bonheur Kouy madame bonheur Ladial mon cœur Kouy madame bonheur Ladial mon cœur May ki key bonheur Ladial mon cœur May madame bonheur Ladial mon cœur May madame bonheur
Writer(s): Charles Diagne, Cheikh Kourouma Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out