album cover

Habibi

860Hip-Hop/Rap2026
album cover
Habibi was released on July 3, 2026 by Prince Arts as a part of the album Habibi - Single
ReleasedJuly 3, 2026
LabelPrince Arts
BPM97
Melodicness
Acousticness
Valence
Danceability
Energy

Lyrics

Sama beuguel thi yaw dou réer
Matgua wérouwayy
Sama khel mi bou toukéeeee
Yakoy térou wayyyyy
Namnala lou bariiii
Dakaaaar ba paris
Gua weulbatikou nop ma chéréeee
Dakar ba Doubaï
Wakhal nigueko beugué chérie wakhal nimlaa nékhé
Markhaban bikoum wanibik machallah
Wakhal nigueko beugué chérie wakhal nimlaaa nékhé
Markhaban bikoum machallahhhh
Habibi Habibi Habibi choukrane Habibi
Habibi Habibi Habibi sama Habibi
Drifa hayaty sama Habibi
Mbeuguel bou doy ni désert
Li reuy na wayyyy
Soumala guissoul di miséeeer li doyna warrrrr
Namnala lou barri
Dakaaaar ba paris
Gua weulbatikou nop ma chéréeee
Dakar ba doubaï
Wakhal nigueko beugué chérie wakhal nimla nékhéeee
Markhaban bikoum wanibik machallah
Wakhal nigueko beugué chérie wakhal nimla nékhéeee
Markhaban bikoum machallah
Habibi Habibi Habibi choukran Habibi
Habibi Habibi Habibi sama Habibi
Hinteu manak kifkhoum
Ante hayaty
Khatayta galbi
Ante hayaty
Yaw Djiby fall domou ndayouuuu bilal fall domou ndayouuu tamina fall
Borom Mauritanie woynalaaa
Hinteu manak kifkhoummm
Khatayta galbii
Sama Habibi
Written by: Abdoul Khadre Fall

Shazam Footer

Select language:
Google Play Store
Apple App Store
Chrome Web Store
Galaxy Store

Follow Us

Loading...