制作
出演艺人
Lass
表演者
Roberto Fonseca
表演者
作曲和作词
Roberto Fonseca Cortes
作曲
Alexandre Di Roberto
作曲
Lansana Sane
作词
制作和工程
Jordan Kouby
制作人
歌词
Li ma ci nex mbaa bàyyima
Li ma ci nex
Ag fu ma jëm xol bi jooy wet
Li ma la nammee, mën u ma koo fay deh
Dey yàgg deh waye dinay giise deh
Fattalikul, yaw mi ban jaaxle
Fa nga jëlee, jom bi nga am deh
Yaw miile, amul loy ragalee
Sama waaji ci nga
Xalito yaw, ci nga
Lu ma def yaw, ci nga
Fi ma jëm yaw, ci nga
Lu ma mel yaw, ci nga
Fii ma dungu, ci nga
Foo jëm yaw, ci nga
Amul werante
Maa ngi fattalikul jamono yooyule
Muy meti, bës bu nekk ñu kaay muñ dee
Ku nek di wax "kañ la jeex dee"
Waaye borom bi, dara tëwul,xam na
Jàngal, àdduna nu mi doxee, naj
Guddi goo giis, am na bëcceg
Ay waay, jafe-jafe yaa ngay door
Xamal ni, li daal mooy li njëkk
Sama waaji ci nga
Xalito yaw, ci nga
Lu ma def yaw, ci nga
Fi ma jëm yaw, ci nga
Lu ma mel yaw, ci nga
Fii ma dungu, ci nga
Foo jëm yaw, ci nga
Amul werante
Mënul taa deñ, sunu àndandoo
Maa ne "gëmal ni noonu la"
Sei Maria, Sei Maria, maa ne "gëmal ni noonu la"
Ee ban jaaxle da fa wet
Ee maa ne "ban jaaxle da fa wet"
Sama waaji ci nga
Xalito yaw, ci nga
Lu ma def yaw, ci nga
Fi ma jëm yaw, ci nga
Lu ma mel yaw, ci nga
Fii ma dungu, ci nga
Foo jëm yaw, ci nga
Amul werante
Written by: Alexandre Di Roberto, Lansana Sane, Roberto Fonseca Cortes

