音乐视频

音乐视频

制作

出演艺人
Molze
Molze
表演者
作曲和作词
Molamin Jallow
Molamin Jallow
作曲

歌词

Ay Waatna cy Yallah gissu ma lu melni li
Ay Kon baby yama motali mhan
Sa yumala holeh lerr beh melni janti ji
Baby
Yow yama taamal li mhan
Waatna cy Yallah baby yama genal gaayii
Dortu mala baayi
Johk nala khol bi hamnga love bi dumasi taayii
Munnu mala baayii
Yama genal wurus ngalam
Sa kharr kanam
Girl sa ginaw bandang
Baby
Yama genal wurus ngalam
Sa kharr kanam
Sa ginaw bandang
Oh no baby yama genal wurus ngalam
Ngalam, Ngalam, Girl wurus ngalam
Baby
Baby girl sa ginaw bandang, Bandang, Bandang
Yow sa ginaw bandang oh no baby yama genal
Jaral ngama lapp cy geage gi
Mhan deh Fonku nala dumala tek lu meiti
Waat na cy Yallah danga chofeh baby
Sama khol bi yowla ken munut ko wedi
Yeah yeah
Dagul nyu dem cheii sama Chérie
Bala kena laaleh Dohal nyu dem
Jel suma khol bi hamnga neh yama mormeh
Sanda ginda kima bugu yowla khol bi deh yako dawmeh
Dohal nyu dem
Dem seiyii seiy bi hamnga neh dofi nyarel
Waatna cy Yallah baby yama genal gaayii (yama genal gaayii)
Dortu mala baayii
Johk nala khol bi hamnga love bi dumasi taayii (love bi dumasi taayii)
Munnu mala baayii
Yama genal wurus ngalam (wurus ngalam)
Sa kharr kanam
Girl sa ginaw bandang
Baby
Yama genal wurus ngalam
Sa kharr kanam
Sa ginaw bandang
Oh no baby yama genal wurus ngalam
Ngalam, Ngalam, Girl wurus ngalam
Baby
Baby girl sa ginaw bandang, Bandang, Bandang
Yow sa ginaw bandang oh no baby yama genal
Sama Chérie (Jel suma khol bi hamnga neh yama mormeh)
Sama Chérie (Jel suma khol bi hamnga neh yama mormeh)
Written by: Molamin Kongira, Moukhamed Secka
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...