Lyrics

Sonou naa Maala togne, balma Woh woh woh Sonou naa Mane maala togne, balma You feel mane dé wéét naa You're still, you're still my boo Everyday meu niaak fayda go back Nieuw soukou diégalou ci seu kanam baalou akk Baalou naala nguir yalla balma Dafma méré xam naani ma togne Everyday meu niaak fayda go back Nieuw soukou diégalou ci seu kanam baalou akk Nangou sama défaite, téy ya am ndam (am ndam) Loma méré méré kham nga maa xam Sama babygirl kaay diégalou na Sama babygirl baayil mér wouyouma Nangou sama défaite, téy ya am ndam (am ndam) Loma méré méré kham nga maa xam Sama babygirl kaay diégalou na Déloussil ma baby oh-ouh-ah yeah Sonou naa Maala togne, balma Woh woh woh Sonou naa Mane maala togne, balma Chérie coco me I love you dou débat Tu sais pour toi je ferai le premier pas Des jeux de rein à la Wally - Ipupa Néxaalat keur gui on fera n'importe quoi Yow tamit, baayil seu mér-bi té nga ré comme Khaby Lam lamé déy sonal seu xél, nangou naa ni Maako déf, maala togne Bouniou mél ni Tom & Jerry Lak lak like fire Woh woh woh woh woh woh Sexy lady Dama wééré tay, diégalou naa Sama babygirl bayil mér, wouyouma Nangou sama défaite, téy ya am ndam (am ndam) Loma méré méré kham nga maa xam Sama babygirl kaay diégalou na Déloussil ma baby oh-ouh-ah yeah Sonou naa Maala togne balma Woh woh woh Sonou naa Mane maala togne balma
Writer(s): Akatche Bennette Seraphin Koffi, Wally B. Seck Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out