Musikvideo

Ismaël Lô - "Baykat"
Schau dir das Musikvideo zu {trackName} von {artistName} an

Credits

PERFORMING ARTISTS
Ismaël Lô
Ismaël Lô
Performer
Stan Renoult
Stan Renoult
Performer
Pierre Bertrand
Pierre Bertrand
Performer
Claude Salmieri
Claude Salmieri
Performer
Laurent Vernerey
Laurent Vernerey
Performer
Yann Martin
Yann Martin
Performer
Michel Aymé
Michel Aymé
Performer
Thierry Boucou Pastel
Thierry Boucou Pastel
Performer
Philippe Balatier
Philippe Balatier
Performer
Philippe Georges
Philippe Georges
Performer
Pathe Dieng
Pathe Dieng
Performer
Olisa
Olisa
Chorus
Diane Solo
Diane Solo
Chorus
COMPOSITION & LYRICS
Ismaël Lô
Ismaël Lô
Translation
Stan Renoult
Stan Renoult
Arranger
Pierre Bertrand
Pierre Bertrand
Arranger
Claude Salmieri
Claude Salmieri
Arranger
Laurent Vernerey
Laurent Vernerey
Arranger
Yann Martin
Yann Martin
Arranger
Michel Aymé
Michel Aymé
Arranger
Thierry Boucou Pastel
Thierry Boucou Pastel
Arranger
Philippe Balatier
Philippe Balatier
Arranger
Philippe Georges
Philippe Georges
Arranger
Pathe Dieng
Pathe Dieng
Arranger

Songtexte

Mané hé baykat bi khalam Démonna bay nékh wayé boumgua Dokna mome Mané hé baykat bi khalam démonna Bay nékh wayé boumgua dokna mome Boula nékhé talalal say lokho Yaye docteur biy fath khifou askane bi Liko dalé si nditoum rew bassi miskine Ya souméko di dane sa dolé andak nath Bi di liguey sa gnakha di tourou Ngay bay di doukat bilay ya am diome Kon diarama baykat koufi xiff yako Doundal bamou sour waw koufi fébar Yako nandal aki réén bamou féékh Kon diarama baykat koufi xiff yako Doundal bamou sour Waw koufi fébar yako nandal aki réén Bamou féékh Ya momone sa mbay Ya mome sa guanthiakh mome say Ndiour ya mome sa alla di bay Nguour gneuw dougalthia lokhome ak Boor fékeleuthaa guanthiakh ba Mégneu lole ndékétéyo Kon diarama baykat koufi xiff yako Doundal bamou sour Waw koufi fébar yako nandal aki réén Bamou féékh Kon diarama baykat koufi xiff yako Doundal bamou sour Waw koufi fébar yako nandal aki réén Bamou féékh Dirama diarama baykat bé yaw Kéneu rek mola mana fay Moy bourbi yaalla Guathia ngalama Guathia ngalama yaw baykatbé Guathia ngalama Guathia ngalama yaw baikatbé Dirama diarama baykatbé yaw Kéneu rek moleu mana fay Moye bourbi yalla
Writer(s): Ismaël Lo, Ismael Lo Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out