Musikvideo

Vorgestellt in

Credits

PERFORMING ARTISTS
Youssou N'Dour
Youssou N'Dour
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Youssou N'Dour
Youssou N'Dour
Composer
Henry Guiyabert
Henry Guiyabert
Composer

Songtexte

Ha dem Dem fan Lu ma bëggoon mënul nekk Leer nga ci kenneen Man ma ngi ci lëdëm Xam naleen, may ki koo def Suma demee bay meree Duma meree kudul sama mbopp Te man may seeti baye baalu ko Wiri wiri jaari ndare Wiri wiri jaari ndare, ndare Xam na dem Demul feen fu nguy wuute Ligeey u ma Li ma mbëggoon moy mu dox Te duma dox, ci sen kaw Xam na lépp, may ki ko deef Suma demee bay meree Duma meree kudul sama mbopp Te man ma seeti bay, baalu ko Wiri wiri jaari ndare Wiri wiri jaari ndare, ndare Wiri wiri jaari ndare, ndare Bilay, bilay, bilay, bilay-bilay Ma rëccu Ma nee soy dem mba xamatoo fa jëm Delul fa nga jukkee Fuy la xamee Fii nga mbaggee Fuy la teete Fi nga jange école Wiri wiri jaari ndare Wiri wiri jaari ndare, ndare Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri) Wiri wiri jaari ndare, ndare (ha fokk ma seeti bay) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wara bokk mba seeti yaay) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri) Wiri wiri jaari ndare, ndare (ha fokk ma seeti bay) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wara bokk mba seeti yaay)
Writer(s): Youssou N Dour, Henri Guiyabert Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out