album cover

BIN BIN

7Music2025
album cover
BIN BIN κυκλοφόρησε στις 19 Δεκεμβρίου 2025 από Big Papa313 ως μέρος του άλμπουμ DEMB
ΆλμπουμDEMB
Κυκλοφορία19 Δεκεμβρίου 2025
ΕτικέταBig Papa313
BPM94
Μελωδικότητα
Ακουστικότητα
Βαλάνς
Χορευτικότητα
Ενέργεια

Μουσικό βίντεο

Μουσικό βίντεο

Στίχοι

Yaye sama rimbim guiguin
Boul allou defal nank bin bin
Dotoumala defati
Dotoumala gnafati
Yaye sama rimbim guiguin
Boul allou defal nank bin bin
Dotoumala defati
Dotoumala gnafati
Terreur leu man khadiouma si yaw
Diap ci deloussi bala wess
Gathié bouko bayi moufiy dess
Fi sa keur leu fi dofi gane
Caye tok té mougn nguir yalla ki man
Mbeuk di keudd fi dofi none
Geud di saga man douma sa none
Tayeff leu âme ligguey leu
Khaptal leu bangua dem sa yone
Tayeff leu âme ligguey leu
Khaptal leu bangua dem sa yone
Yaye sama rimbim guiguin
Boul allou defal nank bin bin
Dotoumala defati
Dotoumala gnafati
Yaye sama rimbim guiguin
Boul allou defal nank bin bin
Dotoumala defati
Dotoumala gnafati
Chérie sama fraise yokatima braise
Yaye sama choco madone sa coco
Yaye sama auto madone sa bateau
Yaye sama gâteau gaw ci man né moto
Nala woutal mbindane
Defla diegui ndanane
Ngay solok di soumi
Di boumak di boumi
Yaye sama fleur di sama couleur
Yamay tiokhatane gneup di agn
Yaye sama beurre yaw lay weur
Yamaye nakhtane ken dou bagn
Yaye sama rimbim guiguin
Boul allou defal nank bin bin
Dotoumala defati
Dotoumala gnafati
Yaye sama rimbim guiguin
Boul allou defal nank bin bin
Dotoumala defati
Dotoumala gnafati
Dotoumala defati
Dotoumala gnafati
Dotoumala defati
Dotoumala gnafati
Written by: Abdou Gueye, Aw Papa Demba, Ian Colomer

Υποσέλιδο Shazam

Επιλογή γλώσσας:
Google Play Store
Apple App Store
Chrome Web Store
Galaxy Store

Ακολουθήστε μας

Loading...