Music Video

Sama Néné
Watch {trackName} music video by {artistName}

Lyrics

Sama néné mongi dioyé héé Néné yaw lodi diooye Sama tanta moma doréé Yaye booy nakhal makoo, maman Sama néné mongi dioyé héé (mongi diooy) Néné yaw lodi diooye (mola door) Sama tanta moma doréé (thiey moma door) Yaye booy nakhal makoo, maman Sama néné mongi dioyé héé Néné yaw lodi diooye Sama tanta moma doréé Yaye booy nakhal makoo, maman Sama néné mongi dioyé héé (mongi diooy) Néné yaw lodi diooye (ohh lodi dioy) Sama tanta moma doréé (thiey moma door) Yaye booy nakhal makoo, maman Kouy laal Ma Demba Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say Kouy laal sama doom djéé, yaye Ayo béyo béyo Kouy laal Ma Demba Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say Kouy laal sama doom djéé, waw Ayo béyo béyo Kouy laal Ma Demba Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say Kouy laal sama doom djéé, yaye Ayo béyo béyo Kouy laal Ma Demba Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say Kouy laal sama doom djéé, waw Ayo béyo béyo Sama néné mongi dioyé héé Néné yaw lodi diooye Sama tanta moma doréé Yaye booy nakhal makoo, maman Sama néné mongi dioyé héé (mongi diooy) Néné yaw lodi diooye (mola door) Sama tanta moma doréé (thiey moma door) Yaye booy nakhal makoo, maman Sama néné mongi dioyé héé Néné yaw lodi diooye Sama tanta moma doréé Yaye booy nakhal makoo, maman Sama néné mongi dioyé héé (mongi diooy) Néné yaw lodi diooye (hoo lodi diooy) Sama tanta moma doréé (thiey moma door) Yaye booy nakhal makoo, maman Sama doom sama sopé Dounda matta dioy oh Mom lay dioy doom So doundé ba matt liguéy waw Térél say wadiour Kouy laal Ma Demba Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say Kouy laal sama doom djéé, yaye Ayo béyo béyo May niaane Ma Demba nga doy si baye boy mom lay dioy doom So doundé ba mat liguéy waw Féral say rangogne Kouy laal Ma Demba Sabar yassa Ngaay dess koy ndaat ndaat say Kouy laal sama doom djéé, waw Ayo béyo béyo Ayo béyo béyo Ayo béyo béyo Kouy laal sam dome djé yaye Ayo béyo béyo
Writer(s): Djiby Ly Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out