Letras

Njaabaar thiey njaabaar Li si njaabaar Feene laniouye doundé Néyena ame na aye jinné Njaabaar feene laniouye doundé Njaabaaro njaabaar Njaabaar Njaabaaro njaabaar Feene laniouye doundé Yama néwoon guénéle sarakh Mbissekitt néne daleu thiarakh Altiné yé dieule lo marakh Deumeu jinné douma meuna warakh Karamakho yow xamato dara Dangaay feene yow ndéké do maara Doto ma thiawe saye thiourou thiara Dima sotti saw daye bouroubara Toope saye tektal tale na sondéle Yoon binga wakh kone tek na fa néne Guney binga wakh kone watt na ko ndéle Gueumeutouma saay wakh dem na fénéne Féni neene féni neene féni neene Gueumeutouma saay wakh dem na fénéne Féni neene féni neene féni neene Gueumeutouma saay wakh dem na fénéne Këf négne bopp bi Yobou xel mi Jëlëtoule saggome Dégne ko diaxaan Meunoutoule jobbi Guéneu keur gui Déé si boppam Dégne ko diaxaan
Writer(s): Malal Talla Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out