Créditos

PERFORMING ARTISTS
Youssou N'Dour
Youssou N'Dour
Lead Vocals
Prince Ibrahima Ndour
Prince Ibrahima Ndour
Keyboards
Guy Kaye & Omar Sow
Guy Kaye & Omar Sow
Acoustic Guitar
Abdoulaye Lo & Alain Berge
Abdoulaye Lo & Alain Berge
Drums
Mamadou Mbaye
Mamadou Mbaye
Lead Guitar
Bassikou Kouyate
Bassikou Kouyate
Musician
Babacar Faye & Steve Shehan
Babacar Faye & Steve Shehan
Percussion
Pape Oumar Ngom
Pape Oumar Ngom
Rhythm Guitar
Thierno Koite
Thierno Koite
Saxophone
Wilfrid Zinsou
Wilfrid Zinsou
Trombone
Ibrahima Konate
Ibrahima Konate
Trumpet
COMPOSITION & LYRICS
Youssou N'Dour
Youssou N'Dour
Songwriter
Kabou Gueye
Kabou Gueye
Songwriter
Prince Ibrahima Ndour
Prince Ibrahima Ndour
Arranger

Letras

4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk moo neex
Boo lékkee ba suur war ngaa gërëm
War ngaa gërëm ni dugg ci waan wee, waan wa tang na
Fi mu tóllu nii war ngeena bég
War ngeena bég ci independans bi, ak ni ko indi
4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk moo neex
Boo lékkee ba suur war ngaa gërëm
War ngaa gërëm ni dugg ci waan wee, waan wa tang na
Dama ne bu lëk lékkee olom
Budee gore na te dëggu war na ko gërëméë picc yi
No, no, no, no, no, no
No, no, no, no, no, no, yee
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk moo neex
Ah lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, gis say mbokk moo neex
Lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, gëm sa bopp moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
No, no, no gis say mbokk moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
Waaw Lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, gis say mbokk moo neex
Aaaaa, moom sa bopp moo neex
Waaw Lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, moom sa bopp moo neex
Written by: Kabou Gueye, Yuossou N'Dour
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...