Créditos

Letra

Moy sunu reew
Moom le ñuy tiitëroo Senegal Ndiaye Senegal moy Suñu gaal Ku ñëw te menoo joow Demal ba ñëw sénégal Deku diine le
Deku Teranga la
Kene du ko miim Dëku diine le Dëku Teranga la Wey naa ko Magg ñu baax ni Dëku diine le Dëku jamm le Weyy sénégal
Kaay ñu añ
Kaay ñu reer
Amul feneen fu dul sénégal
Moy Suñugal
Kene du ko miim Dëku Bamba la Kene du ko miim Dëku Maodo le woooy
Saalum ba sine Limaamu laay ca yoff Boucounta Ndiassane Senegal Ndiaye
Dëku Gainde la
Ku ñëw te menoo joow Demal ba ñew sénégal Sénégal
Suñugal
Sénégalais
Kadior ak Baol Saalum ba Siine Lepp ci sénégal
Kaay giss sunugaal Ku ñëw te menoo joow Demal ba ñëw sénégal
Kena dou ko miim DëkuTeranga Amna Médina Baay Amna Touba
Kena dou ko miim DëkuTeranga Amna Medina Baay Amna Touba
Amna Tivaounane Amna Ndiassane
Kena dou ko miim
Te bët sët na boo yeewo yeema Lu ko waral!
TRANSLATION ENGLISH
SENEGAL ! It’s our country
It’s our pride
Senegal Ndiaye
Senegal we are in the same boat A place of
It's a place of hospitality
Without comparison
A place of
It's a place of hospitality I sang the great elders Place of peace
Come have lunch with us
Come and have dinner with us There is no other place like Senegal
It’s very special
The country of Bamba The country of Maodo From Saalum to Siin Limamoulaye in Yoff Boucounta Ndiassane Senegal Ndiaye
 The land of lions
If you can’t row
Wait until you arrived in Senegal Senegal our boat, Senegalese !
Kadior and Baol Saaluum to Siine Everything is here !
Come and see
Wait until you arrived in Senegal
The holy city of Medina Baay is here! The holy city of Touba is here !
The holy city of Tivaouane is here ! The holy city of Ndiassane also !
When it’s daylight wake me up Why ?
Written by: Ale Mboup, Bahkane Seck, Samuel Dubois
instagramSharePathic_arrow_out

Loading...