Créditos
COMPOSICIÓN Y LETRA
beatbybiz Prod
Autoría
Letra
Put yours hands in the air bidew bi leeral fi
No game sama slogan maay libéré fi
Call me **** free
When i say one two three , say NO GAME
One Two Three ! NO GAME
I was on it , i'm on it i'll be on it ****
What the fuck loussa yoone ya aint giv me rollin'
Niou bokk way nga yam ci tabax mane ma carrolé daaw
Xamoo lou xéw nganaane ma dara yangui tatonné baye
Meuno ma tekk banane ma alli mani waxko sa baye
Yaw dooma dégg may tekk, Meun naako dieud say prek
Diote na sa feed back, thiénéél fi amoofi baate
Yow fouki bouki goudi, fouki bouki beuthieuk
Fayla joni joni meun ko tax ba douma beuthieuk
Yangui boudi mane may thiokki thiokki
Legui nga tégui tank , biz waxma lane mooy tax ba douma ndieuk
Mani Kush point
Déffoma dara , mafi woute beef
Dégooma deih dama xiif beef
Dagg sa tete dérééte dji tiss tiss
No peace no love ya' know what it is
Déffoma dara , mafi woute beef
Dégooma deih dama xiif beef
Dagg sa tete dérééte dji tiss tiss
No peace no love ya' know what it is
Missaya came back !! To give them lesson ...
Lara bolchit around the game them gara listen ..
Time is up for them understand Hip hop 's basic ...
Throw it away ! No more wrong habit ...
No Peace ! no love ! no fuking Batiman ...
Murder !! Fighya burn them boom !! wikid man ...
Work ina di black blind dem up Fo ever ..
Me dont wana see dem like this every Deyah ...
Yei katou fitna !! Doufa xaar Diassi ya ..
Try to be good !! to be real !! coz Jah see ya ...
Niou ngui mat di euf !! Peace love bi di Bleuf ...
Check it Bol !! check it bolchit bi laakou si Dieuf ...
Yenei tey dji (taij) neek la ! Na fekhei mou set ...
Game bi am na diam ! na djinakh dougou négu Mous sét ...
Take ! it to d street !! But !! ay porteur d voi lagn ...
Siik !! souniou !! birr !! begne Ken dévoilé niou ...
Déffoma dara , mafi woute beef
Dégooma deih dama xiif beef
Dagg sa tete dérééte dji tiss tiss
No peace no love ya' know what it is
Déffoma dara , mafi woute beef
Dégooma deih dama xiif beef
Dagg sa tete dérééte dji tiss tiss
No peace no love ya' know what it is
Sama coup dafa dangerous dooko meuneu baaré
Danga fou i'm the murderer maay killén di gaaré
Sama rhyme day tocth sa brain defci thiafka rap
No peace no love jam diéx na ci bi track
Gadou knife sémign armé gun fékki la sa zone
Fire burn
Reum teum piteum bro rek nga meun
Das Média on da microphone i live in da ghetto
Boomay jaay bandi seuss ma tocth sa, wane la rééwo
Dougou tchi gééw Kou niémé éd weunieul ma jééw
Ma défla la nééw Pomme dou néw Meuno di béw
Kiy ram kiy daw kiy dém di dap ki dapp ki né tchi bidééw
Ki jéém di déf boukout ak nak ki nieup di mbiw
Off nieup ni fireman , baye mane sirrou keyman
Di shine like a diamond kone dou yomb nga fayma
SD ding ko degg fepp like P square
Booma geumoul holla back shut keep quite
Déffoma dara , mafi woute beef
Dégooma deih dama xiif beef
Dagg sa tete dérééte dji tiss tiss
No peace no love ya' know what it is
Déffoma dara , mafi woute beef
Dégooma deih dama xiif beef
Dagg sa tete dérééte dji tiss tiss
No peace no love ya' know what it is
Written by: beatbybiz Prod

