Paroles

J'ai pas su faire la différence entre le bien et le mauvais Et j'ai souffert quand t'étais partie, quand t'étais plus à mes côtés J'étais ouais toxic Je voyais d'autre filles avec toi, j'étais pas docile Moi je t'ai fait souffrir T'avais des soucis mais tout le temps j'étais busy Quand t'es décédé J'ai vu que le contraire de l'amour c'est pas la haine Mais plutôt l'indifférence Et quand t'étais la, je m'en foutais de ton existence La j'suis paranoooo, yeah parano Parano, yeah parano Ah su ma xoole sama ginnaaw Sama xol fees ma jooy Wet naa, wet naa, wet naa Suma toogee xalaat sa dem Sama xol fees fan lay waxe Xanaa du yaa ma ni won yaw mi Doo ma bàyyi, doo ma sori Wax dëgg am na lu ma metti Ab bataaxal laa lay yónne Sa kanam laay gis su ma amee bànneex Sama xol man laa la jox deh Tu me manques mais bon reposes en paix J'ai une pensée pour toi, t'es dans ma tête À la vie, à la muerte À la vie, à la muerte Yo, daj nga fi coono doo yuxu ji wallu Àllaaxira da ngay dem pur dallu Sagal sa bopp sagal sa axlu Gisaguma ku la gën manu Bàyyi nga ma ak ay full questions Yu ma xamul seen reponse Sama mbëggeel c'est des frissons Mes sentiments je les énonces La j'suis paranoooo, yeah parano Parano, yeah parano Ah su ma xoole sama ginnaaw Sama xol fees ma jooy Wet naa, wet naa, wet naa
Writer(s): Charles Diagne, Mouhamed Abdoulaye Preira Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out