Clip vidéo

Pape Diouf - Superman Love (Clip Officiel)
Regarder le vidéoclip de {trackName} par {artistName}

Apparaît dans

Crédits

INTERPRÉTATION
Pape Diouf
Pape Diouf
Interprète
COMPOSITION ET PAROLES
Pape Diouf
Pape Diouf
Composition
Cheikh Tidiane Kourouma
Cheikh Tidiane Kourouma
Paroles/Composition

Paroles

Duma ci lenn lépp yaw la Yaw yaay sama poumon gauche Soo kontaanul dund du yomb Amuma lu bari mais coco Xol bi ma ko moom, jox naa la ko Bébé sax boo demee bay fane Ma doon ginnaar gi ngay reere Kanam gi ngay ñekk gis fo dikke Jege ma ma tay la lu bees ya fi ne Bae je t'aime Mi ko ankom mbi yitte I love you, bébé n b'i fè Te amo, ich liebe dich Shiwananko, wo ai ni yoo Boo de jant ma doon superman Fekk yaa ngi sama weet, kenn duma daane Def naa la sama soxla Sama soxna, sama number one Boo de jant ma doon superman Fekk yaa ngi sama weet, kenn duma daane Def naa la sama soxla Sama soxna, sama number one Yaay piano sama mind Yi mélodie foo ko jange Jar ci xol bi, jaaxase xel mi Def sa tuur ci këyitu kër g Tegi monument de la renaissance Tek fa sa bos di ko status Bet seereer ak bolu cëre Yi may def moo ko gën a neex Di gis tukkulër bu burde Ki lay jooyloo moo la war a nax Boo de jant ma doon superman Fekk yaa ngi sama weet, kenn duma daane Def naa la sama soxla Sama soxna, sama number one Boo de jant ma doon superman Fekk yaa ngi sama weet, kenn duma daane Def naa la sama soxla Sama soxna, sama number one Bae kaay ma wax la secret Dama sëy ci sa jëme ji dalaas ngoom Yaw dal, yaay première dame ci xolu king Donte jarul maa la koy wax Bëgg la ba ci sa waw lay dox Yaay piano sama mind Yi mélodie foo ko jange Yaay piano sama mind Yi mélodie foo ko jange Bilaahi mbëggeel la neex Mbëggeel la neex xale bile (mbëggeel la neex) Muy gën di neex neex a neex ba jaxal ma (Yaw danga xam wala dangay laaj soo bëggee dugg faw ngay laaj) Leee lee leee lee mbëggeel (mbëggeel la neex) Man mi sax damay laaj fu mu nekk ni bilaahi mbëggeel (Yaw danga xam wala dangay laaj soo bëggee dugg faw ngay laaj) Man mi sax damay laaj fu mu nekk ni mbëggeel (Yaw danga xam wala dangay laaj soo bëggee dugg faw ngay laaj) Aka bari doole bilaahi mbëggeel
Writer(s): Pape Cheikh Diouf, Charles Diagne Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out