album cover
Buga
album cover
Buga 5 सितंबर 2026 को SIZA MUSIC GROUP द्वारा एल्बम Triplet, Vol. 1 - Single के एक भाग के रूप में रिलीज़ किया गया था
5 सितंबर 2026
लेबलSIZA MUSIC GROUP
BPM148
मधुरता
ध्वनिकता
वेलेंस
डांस करने की क्षमता
ऊर्जा

गाने

INTRO
Niom mane lagne Buga x3
No def ma leumbé ndakh kham naniou mane lagne Buga
COUPLET 1
Li nékh neu, ndakh diékh neu
Sa namél thi mane dégne naa
Nieweul niou féthie, di rétane
Tay bessou mbékté la
Number one family, gathié ngalama ak
Yow mima gueum fépp thi adouna ak
Yow mi fogone douma messeu nieuwat,
Sa cauchemar tambalina
Guedj ngama guiss, kikoy yeungueul nieuw na
Numero 10, dou manak béneu kuluna
Suniu musique, niou wereuléko Adouna
Mak yéne leu, yéne leu
Kone amoul arrêt, yokh la
REFRAIN
Nioma déf wéér dima séntou, Niom mane lagne Buga
Done séne bidew niou dima féélu, Niom mane lagne Buga
May garmi piir niou dima tééru, Niom mane lagne Buga
No def ma leumbé ndakh kham Naniou mane lagne Buga
Éh Éh Éh, Niom mane lagne Buga
Éh Éh Éh, Niom mane lagne Buga
Éh, Éh Éh Éh, Niom mane lagne Buga
No def ma leumbé ndakh kham Naniou mane lagne Buga
COUPLET 2
Louné ma dékou ko thi ay coup bas
Sama ngor né naa focus sama combat
Nianou yaay deuké léral sama dunya
Yéne tam nguéne nékk mbolo dima dolél naane ma,
Djowz yow la, dokhalal noon leu
Nioune nak yow la té lo songou dingko daan
Manit mané yéne leu, gang bi nioune la
Nieweutina ndakh kham nguéne ni ADMOW dou messeu die
Kikoy diém douma séén
Thiono bi dou louy léér
Wakhone naala nga wakhal ma kokou lé
Ni y'a que moi qui peut faire ça
REFRAIN
Nioma déf wéér dima séntou, Niom mane lagne Buga
Done séne bidew niou dima féélu, Niom mane lagne Buga
May garmi piir niou dima tééru, Niom mane lagne Buga
No def ma leumbé ndakh kham Naniou mane lagne Buga
Éh Éh Éh, Niom mane lagne Buga
Éh Éh Éh, Niom mane lagne Buga
Éh, Éh Éh Éh, Niom mane lagne Buga
No def ma leumbé ndakh kham Naniou mane lagne Buga
BRIDGE
Niom mane lagne Buga
Niom mane lagne Buga
Niom mane lagne Buga
No def ma leumbé ndakh kham naniou mane lagne Buga
OUTRO
Ohhh woooh Niom mane lagne Buga
Ohhh woooh Niom mane lagne Buga
Ohhh woooh Niom mane lagne Buga
No def ma leumbé ndakh kham naniou mane lagne Buga
Written by: Adama Diop, Fructueux Kuassi Godpeace Symenouh, Moustapha Diop
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...