album cover
FALL
album cover
FALL 19 दिसंबर 2025 को Big Papa313 द्वारा एल्बम DEMB के एक भाग के रूप में रिलीज़ किया गया था
एल्बमDEMB
19 दिसंबर 2025
लेबलBig Papa313
BPM86
मधुरता
ध्वनिकता
वेलेंस
डांस करने की क्षमता
ऊर्जा

म्यूज़िक वीडियो

म्यूज़िक वीडियो

गाने

Diekk ndiagn fall (Diekk ndiagn fall)
Nekhi ré (Nekhi ré)
Kofi ré Mame
Mou tekhé
Taye ma tiakhlene (Taye ma tiakhlene)
Ba xam adjinguene (Ba xam adjinguene)
Jambari goor (Jambari goor)
Ki kharé nawett ak nore
Dieuf dieul rek moy li woor
Dorr warr bagn di marre
Kone goor diogal dorr
Warr warr bagn di xarr
Waye
Mamo mamo
Waye
Mamo mamo
Mamomamomamo
Mamo cheikhra fall
Waye
Mamo mamo
Waye
Mamo mamo
Mamomamomamo
Mamo cheikhra fall
Diekk ndiagn fall
Laxassayou madial
Yesslou watt sam fall
Begué meissa bigué mondial
Nagnou fekhé gneup guissé
Kour keul kourouss
Gathie derr nombo nguissé
Samp kourel yi dourouss
Meissa bigué Coumba fallo
Ngagn ma deugeul fallou
Takk ndigue gnakh diokhé
Yaye borom
Dieufé ndiguel bayi teré
Yako mome
Waye
Mamo mamo
Waye
Mamo mamo
Mamomamomamo
Mamo cheikhra fall
Waye
Mamo mamo
Waye
Mamo mamo
Mamomamomamo
Mamo cheikhra fall
Written by: Abdou Gueye, Aw Papa Demba
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...