Dari
PERFORMING ARTISTS
Voilaaa
Performer
Bruno Hovart
Drum Programming
COMPOSITION & LYRICS
Bruno Hovart
Songwriter
Lassana Sané
Songwriter
Lirik
Yeufou goorla
Yeufou goorla
Goor raco mome waye
Goor raco mome waye
Heutieule mbaal mu Teer sa wadji
Heutieule mbaal mu Teer barisse
Goor raco mome yawe Goor raco mome hé
Goor raco mome yawe Goor raco mome hé
Heutieule mbaal mu Teer hé
Heutieule mbaal mu Teer hé
Heutieule mbaal mu Teer hé
Heutieule mbaal mu Teer hé
Awe sa waye naga défe lou gawe waye
Ndahe maal law goor racoye defe waye
Yaw naga diok fadiare gnou teubeule gaalgui waye
Déme sintou nahebi,borrou pintieu waye
Aye yeufou goorla,mané li yeufou goorla
Amoule ragal mané fite moye dougou gaala
Gnoune dagnouye laawe goudé ak beuthieuk dagnouye baala
Nahe waguini mané béthiale mbaala
Heutieule mbaal mu Teer hé
Heutieule mbaal mu Teer hé
Heutieule mbaal mu Teer hé
Heutieule mbaal mu Teer hé
Alihé silihé goor
Lébou doye yaw diambarga
Mbaal law heufou goorla
Yagui sameu thiossane dal
Aye loufi mame bayi wone
Yawe yagui thi wowou yone
Dahe daga yawe kane ga donne
Mo tahe ga fonkou yawe sa yone
Written by: Bruno Hovart, Lassana Sané