Lirik

Lo bouguoul mane doumko beug damay guagn Ko bouguoul mane doumko beug dafay khar Yamay térè nèlaw ndakh dangua djonguè dègueu dadj Kay ma fétchal la yaw mane diraral ngama tarann taatch Lo bouguoul néna la dafay khar Koudoul yaw nama dandou gneuweul guaw Yay yeunguel sama Mane bardé na Bayil mbélè mbéssè gui di wakh Yafi nékk té dou dagn girl Bour Yallah moko dèff té dou dagn Beug ngueumeu beug na lol dou dagn Soxna ci yay sama lumière Ba abadann dou dagn Beug ngueumeu beug na lol dou dagn Bour Yallah moko dèff té dou dagn Soxna ci yay sama lumière Ba abadann dou dagn Bourou gualé lay done tchi yaw Dinala khékhal fèpp fo men nèkk Nèwonn nala ah ioe Daguoul noumle nèkhé yafi nèkk té dou dègn Mima la khamé tchi la taguok wèet oh yo yo yo Konn boulme sori gneuweul fi seumeu wètt oh Ma doundou paradise You wanna make me out your way Baby girl don't let them break your heart Gnom deugnouy sissou di fènn Baby girl don't let them break your heart Baby mine waroul djoy nah nah Baby mine boul djoy hey Lo bouguoul mane doumko beug damay guagn Ko bouguoul mane doumko beug dafay khar Yamay térè nèlaw ndakh dangua djonguè dègueu dadj Kay ma fétchal la yaw mane diraral ngama tarann taatch Lo bouguoul néna la dafay khar Koudoul yaw nama dandou gneuweul guaw Yay yeunguel sama Mane bardé na Bayil mbélè mbéssè gui di wakh Yafi nékk té dou dagn girl Bour Yallah moko dèff té dou dagn Beug ngueumeu beug na lol dou dagn Soxna ci yay sama lumière Ba abadann dou dagn Beug ngueumeu beug na lol dou dagn Bour Yallah moko dèff té dou dagn Soxna ci yay sama lumière Ba abadann dou dagn Bébé yangui digueul louné Gno ngi koy wakh deug deug nak dou djèkh Djaar nagnu founè t gnoy moudjè Kay ma fétchal la boudé moy lileu nèkh bébé bébé Yallah khamna khamngua Lingueu meu djaral walay walay Beugueu nagn digueunté bi djèkh Mais fi mouss dou fi nané gnèkh Lou nèkh da nagn doundou lou nèkh Kham ngua nè sa xol doumko nabeu nabè Yaw ni ngueu meu beuguè nonou la leu beugué Boul lambeu yatay daguoul fougn la nobè Yawnénala boul meusseu bayi Ndakh damala woloo Boul déglou wakh You bonn yi si mane waay Ndakh damala woloo Yaw nè nala nè weuti nala Someu bayè tchi lann djapp Sama xol sama rèni xol Kham ngua ni beugg beugg nala Lo bouguoul mane doumko beug damay guagn Ko bouguoul mane doumko beug dafay khar Yamay térè nèlaw ndakh dangua djonguè dègueu dadj Kay ma fétchal la yaw mane diraral ngama tarann taatch Lo bouguoul néna la dafay khar Koudoul yaw nama dandou gneuweul guaw Yay yeunguel sama Mane bardé na Bayil mbélè mbéssè gui di wakh Yafi nékk té dou dagn girl Bour Yallah moko dèff té dou dagn Beug ngueumeu beug na lol dou dagn Soxna ci yay sama lumière Ba abadann dou dagn Beug ngueumeu beug na lol dou dagn Bour Yallah moko dèff té dou dagn Soxna ci yay sama lumière Ba abadann dou dagn
Writer(s): Samba Peuzzi, Djiby Ba, Abdoulaye Wone Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out