Lirik

Han' ma wakh ko ben yoon te dem miss yi gno taarou Han wakhlenko niarri yoon te niou dem ohhhooo' Miss yi nio taarou Yen djiguene nirew deug deug gore yowmi yoboulegnou dara Yen djiguene nireww deug deug mbaye gathie gualamane Yen djiguenerewmi ken meussou len djamnanile Fatelikou talatay nder aline sitoe diatta yacine mboubou. Ah ma 1# Ah ma 2x Te mane sax mane damalene beug Fonk Heu axirouzamane modi moudiou diamono waw waw Mo xam lu moudj wala lou fegn leu
Writer(s): Habib Faye, Mouhamadou Kabou Gueye, Youssou N Dour Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out