album cover
Intro
album cover
Intro dirilis pada 29 Mei 2026 oleh For Life Music sebagai bagian dari album RANCUNIER - EP
29 Mei 2026
LabelFor Life Music
BahasaPrancis
BPM92
Melodiksi
Level Akustik
Valence
Kemampuan untuk menari
Energi

Lirik

Aduna
Am na si ay xat-xat yooy neek
Aduna bi yëpp dañuy jàpp ni
En fait yaw déé nga ba paré dangay xaar sa bëssu dée jott rek
Même nitt yinga xam ñu xam la
Parfois dañu lay xoolé bëttu, like, ki torox na ba paré
Mais écoute bien une chose
C'est que aduna nékul bu lepp baaxé si ngay découvrir yaw la kan
Mais boo néké si ay tar-tar yi gënë ci sa aduna
Ci ngay découvrir yaw la kan
Et si moment yooyu laa xam man la kan
Pression bi ngéen di dégg
Pression mënul yaq diamant
Non
Au contraire, diamant ci pression lañ ko défaré
Té loolu mooy avantag-u juddu ci pauvreté
C'est que gééj gi lumu xoot xoot dangay am pied
Parce que dundu nga lu gënë xoot loolu
Alors ñoom ñëpp dañuy jàpp ni dangay abandonné
Certains pensent que tu vas disparaître
Et ils vont penser que tu n'ira jamais loin
Mais erreur bi nitt ñi di def si côter boobu
C'est que nitt mënul nek si xat-xat yi gënë metti si adunam nga bëgg ko juger, non
Dangay bayi bama xeex, ba combat ba paré nga sog ma juger
Et là tu diras jambaar nga wala fake nga
Mais nitt ku jaar si ay tapette naka lay ragalé daw
Mënu ma xeex ak gaïndé sama giiru dundu yëpp
Di ragal xaj, c'est impossible
Et nitt ku xam lan mooy xiif si adunam
Jamais du fatté lan moo taxoon mu jugg dem liggéyi
Et jamais du mako fatté, Never
Dans ce monde on respecte rarement les promesses, Rarement
Rarement la la nitt di wax ben affaire deff ko
RAREMENT
Alors comme ken tenir-ul promesse yi ñu ma défoon si aduna bi yëpp
Ma xëw bess créer samay promesse té lepp laa tenir
Lepp laa tenir
Nitt ñi diamant bi si kaw kasse lañuy giss muy briller
Mais ken si ñom xamul ñaata guddi nga took di xalaat
Ken si ñom xamul ñaata guddi nga took di di douter si sama bopp
Les rêves ne meurent pas parce qu'ils sont impossibles, non
Ils meurent parce que les gens abandonnent trop vite
Un homme déterminé est plus dangereux que 1000 hommes talentueux
1000 personne yu am talent, ben nitt bu déterminé paré pour rayanté changer adunam moo lén gënë dangereux ñoom ñëpp
Quand la vie te met à genou t'as deux choix comme ñëpp
Deux choix
Abandonner bayi mu sedd
Wala jugg xeex géné ci sa bopp
Alors man ma choisir 2em bi
Parfois tar-tar yi ngay dundu si aduna ñooy sa seriñ bi gënë woor
Bi mënë jakkar loo ak yaw wax la dëgg
Alors maintenant que t'as compris tout ça
Bienvenu dans l'univers de rancunier
Nañ dem ma wax la toq ci nitt kima doon
Written by: Omar Sow
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...