album cover
S'envoler
3952
Hip-Hop/Rap
S'envoler è stato pubblicato il 5 dicembre 2020 da Rep'tyle Music Group come parte dell'album Senegalboy
album cover
Data di uscita5 dicembre 2020
EtichettaRep'tyle Music Group
Melodicità
Acousticità
Valence
Ballabilità
Energia
BPM169

Video musicale

Video musicale

Crediti

PERFORMING ARTISTS
Samba Peuzzi
Samba Peuzzi
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Christ Johan Ollanghas Kimbeki
Christ Johan Ollanghas Kimbeki
Composer
SAMBA TINE
SAMBA TINE
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
Christ Johan Ollanghas Kimbeki
Christ Johan Ollanghas Kimbeki
Producer

Testi

From diack wawaw
Yeah yeah Ludafrik hey yeah
Dañ ma bañ té mënu ñu wax lum len def
Demmal ñu wax la lum len def
**** hate **** hate (Skurt)
Game bé beuri fakes
Nenañ rap buma
Lolo tax ñumay xéx
Ay gooru thiapatat (Skurt)
Bang bang ci sa bopp
Banlieue la dëkk mënu ma tapette lo fok?
Xamga sama koñ (Skurt)
Ken du jënd glaces
Fi dara du sedd paquet bi dañ koy tass
Dañ lay ray dem teudi peine bi sañ nañ lolu
Kill ak sa gang bi teudi peine bi sañ nañ lolu
Money money bag dañ koy tall sañ nañ lolu
Kill sa gang gang gang gang sañ nañ lolu
Man ma ngui ak sama lepp (Skurt)
Di voler lu rëy
Yah yah yah yah
Fils ma ngui ak sama lepp
(hey packathing)
Di voler lu rëy
Yah yah yah yah
Xaalis bima yoor
Damkoy seddo ak sama wa koñ
Bandit bu noppi kone bitch **** buma toñ
Ñom yéné wuñ jamm yéné wuñ jamm
Non non
Yalla may sam Yalla may sam
Wawaw
Loma jaay di nga fi fek louko gënë xeñ
Cicatrices yi né ci yaram bi du mëssë deñ
Tékki rek magui nopilo none yi
Dañ ma bañ **** all eyes on me
Dañ lay ray dem teudi peine bi sañ nañ lolu
(Skurt)
Kill ak sa gang bi teudi peine bi sañ nañ lolu
Money money bag dañ koy tall sañ nañ lolu
Kill sa gang gang gang gang sañ nañ lolu
Man ma ngui ak sama lepp
Di voler lu rëy
Yah yah yah yah
Fils ma ngui ak sama lepp
Di voler Lu rëy
Yah yah yah yah
Yalla moko def fils li du dañ
Mashallah
Yalla moko def fils li du dañ
Mashallah
Yalla moko def yaw bul tite (bis)
Yalla moko def yalla lumu du dañ (bis)
Dañ lay ray dem teudi peine bi sañ nañ lolu
Kill ak sa gang bi teudi peine bi sañ nañ lolu
Money money bag dañ koy tall sañ nañ lolu
Kill sa gang gang gang gang sañ nañ lolu
Man ma ngui ak sama lepp (Skurt)
Di voler lu rëy
Yah yah yah yah
Fils ma ngui ak sama lepp
Di voler lu rëy
Yah yag yah yah
Senegalboy Samba Peuzzi, from diack
Nonula démé, nonula démé, nonula démé
Senegalboyo
Written by: Christ Johan Ollanghas Kimbeki, SAMBA TINE
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...