Crediti
PERFORMING ARTISTS
Puppa Lëk Sèn
Lead Vocals
Yves Abadi
Drums
Vi Avelino
Electric Guitar
COMPOSITION & LYRICS
Yves Abadi
Songwriter
Vi Avelino
Songwriter
PRODUCTION & ENGINEERING
Jahsen Creation
Producer
Testi
Ki gnouy sam yow, mome la dink sama lep man
Duma tite, duma daw ,duma delou ganaw
Ki gnouy sam yow, mome la dink sama lep man
Duma tite, duma daw ,duma delou ganaw
Mo may dolil yërmande, mo may dolil sutura
Luleen neex diem leen ,walaxi dem na ma
Lala, lala, lala, lalala, lala, (x4)

Waay le leen ma, sangue bi (x15)
Ki gnouy sam yow, mome la dink sama lep man
Duma tite, duma daw ,duma delou ganaw
Ki gnouy sam yow, mome la dink sama lep man
Duma tite, duma daw ,duma delou ganaw
Mo may dolil yërmande, mo may dolil sutura
Luleen neex diem leen ,walaxi dem na ma
Lala, lala, lala, lalala, lala, (x4)
Written by: Puppa Lëk Sèn, Vi Avelino, Yves Abadi