album cover
Sali
546
World
Sali è stato pubblicato il 10 aprile 2026 da Cumbancha come parte dell'album Adouna
album cover
AlbumAdouna
Data di uscita10 aprile 2026
EtichettaCumbancha
Melodicità
Acousticità
Valence
Ballabilità
Energia
BPM115

Testi

Mbeugel Nekhna
Mane Beugue nala
Mak yaw boul khol none yi no no
Kay gnou dem fou sorri
Lo beugue magh ghi
Mane damla nob mane
Mane yawlay khol fi
Saliyooooo
Africa Mousso
Saliyoo africa mousso
Zigué zigué
Thiapla go zigué
So mada mada
go go zigui
Zigué zigué
Thiapla go zigué
So mada mada go go zigué
Saliyoooo wonala kay kay
Saliyoooo wonala kay kay
Saliyoooo wonala kay kay
Saliyoooo wonala kay kay
Toppouma toppouma
Mbeuguel ni rekla
Kigha beugue mou beugla
diokh ko sa kholbi
Yama nekh mane
Yama saff mane
Yaw lay weur mane mi
Yay sama khol
Zigué zigué
Thiapla go zigué
So mada mada go go zigui
Zigué zigué
Thiapla go zigué
So mada mada go go zigué
Ah yeba gnou dem
Saliyoooo wonala kay kay
Saliyoooo wonala kay kay
Saliyoooo wonala kay kay
Saliyoooo wonala kay kay
Diarabi yoo
Saliyoooo wonala
Khalebi yaw wonala
Sali yaw wonala
Fou nekh lalay yobou mane mi
Si mbeuguel gou nekh lalay wo
Lo Doundeul wone lo khamoul wone
Topp ma khalebi topp ma
Saliyoooo wonala kay kay
Saliyoooo wonala kay kay
Saliyoooo wonala kay kay
Saliyoooo wonala kay kay
Diarabiyoo
Khalebiyaw wonala
Mbeuguel ni rekla
Mbeuguel ni rekla kafak fo retane kafak fo retane
Written by: Cheikh Fame
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...