album cover
Tijaniyya
3962
Pop
Tijaniyya è stato pubblicato il 31 maggio 2004 da Nonesuch come parte dell'album Egypt
album cover
AlbumEgypt
Data di uscita31 maggio 2004
EtichettaNonesuch
LinguaEnglish
Melodicità
Acousticità
Valence
Ballabilità
Energia
BPM120

Video musicale

Video musicale

Crediti

PERFORMING ARTISTS
Youssou N'Dour
Youssou N'Dour
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Youssou N'Dour
Youssou N'Dour
Songwriter, Composer

Testi

Yaa fi xewal gammu gi, yaa dundalaat daara yi
Li nga def ci jakka yi, baayi Dabakh waccnga
Jaa jef Sy yaa deggal liggeeyu Fa Wade Welle
Cheikh Oumar waxoonna ko, yaa taxawal tarixa bi
Yaa fi xewal gammu gi, yaa dundalaat daara yi
Li nga def ci jakka yi, baayi Khalifa waccnga
Gannaar xamna la, waa Maka xam na la
Yonent bi geremna la, yaa yore Tijaniyya
Yaa fi xewal gammu gi, yaa dundalaat daara yi
Li nga def ci jakka yi, baayi Serin Mansour waccnga
Yaa fi xewal gammu gi, yaa fi xewal wassifa
Zaawiya seede la, reew mi ameelnan la njukel
Yaa fi xewal gammu gi, yaa dundalaat daara yi
Li nga def ci jakka yi, baayi Dabakh waccnga
Dedduwoonna adduna (baayi Dabakh waccnga)
Moo doon boroom suuna (baayi Khalifa waccnga)
Di it ku amoon fulla (baayi Serin Mansour waccnga)
Mandoom ga landina (baayi Dabakh waccnga)
Xam xam ba selina (baayi Khalifa waccnga)
Dajaloonna teere ya (baayi Serin Mansour waccnga)
Doxewuko, damoowuko (baayi Dabakh waccnga)
Cheikhou Oumar Foutiyou Tall
Maami Seydou Norou Tall
Waxoonna ko
Yaay taxawale tarixa Cheikh Ahmed, Tijaniyya
Cheikhou Oumar Foutiyou Tall
Maami Thierno Mountaga Tall
Dajalenga kilifa yi
Written by: Youssou N'Dour
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...