歌詞

Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse Né ngua do guéne ak mane ndakh awmeu clash Loutakh ngua melni Aminata? Mane xamouma, bébé wakhma Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse Né ngua do guéne ak mane ndakh amou meu classe Loutakh ngua melni Aminata? Loutakh ngua melni Aminata? Lane ngua meu eupeulé Motoul sakh pép thiép Nio bokk deuk tchi kogne, loutakh yaw ngua mayy khép? Yéne dieuff yi nguay deff, tchi sama khol daf may guagne Yéne say ma diépi leu déme bay bayi, khol bi bagne Sama mbeuguél moma togne, motakh ma topeuleu Mane ak yaw nio bok kogne motakh ma sopp leu Kheuyneu beuss di na ame kagn, takk leu, téreul leu Hé eh, Hé eh Thioro baye samba, dak sa yaye dieulmeu Sa nijaay yo may ma ay dollar, dou ma té daggo Djank bi tchi kogne bi néna dou sey ak badolo Bo démé keur yayam goudi gossi lay réré Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse Né ngua do guéne ak mane ndakh amou meu ay clash Loutakh ngua melni Aminata? Mane xamouma, bébé wakhma Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse Né ngua do guéne ak mane ndakh amou meu class Loutakh ngua melni Aminata? Loutakh ngua melni Aminata? Lane mo takk si mane ba faléwomeu? Lane mo nekk si mane ba xoloulomeu? Nieuw na sakh si séne keur, mais wakhou lok mane Té métinama ndeyssane, métinama ndeyssane Pourtant nitt la kome yaw, kheuy neu beuss dineu changé Pourtant nitt la kome yaw, wakh meu lane moy déranger Nékal ak mane bilay, beugueu leu Yalla takh Hé eh, Hé eh Thioro baye samba, dak sa yay dieulmeu Sa nijaay yo may ma ay dollar, dou ma té daggo Djank bi tchi kogne bi néna dou sey ak badolo Bo démé keur yayam goudi gossi lay réré Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse Né ngua do guéne ak mane ndakh amou meu ay clash Loutakh ngua melni Aminata? Mane xamouma, bébé wakhma Amou ma or, amou ma xaliss, amou ma ay liasse Né ngua do guéne ak mane ndakh amou meu class Loutakh ngua melni Aminata? Loutakh ngua melni Aminata?
Writer(s): Ismaila Talla Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out