ミュージックビデオ
ミュージックビデオ
クレジット
PERFORMING ARTISTS
Narah Diouf
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Nguenar Diouf
Songwriter
歌詞
Li deh nekh na lool
Bi banekhou xoll
Limey yeuk soumakey xool
Li deh nekh na lol ba eup tool
Wayléléne ma sama dôme dji
Mane deh Beugouma loula metti
Maley nakhtane
Bangay rétane
Feusseul sama mbeuguel si yow
Mouy law ba faw
Ayo sama néné
Néné touti
Koumey nakhal
Sama dome dji
Ayo sama néné
Néné touti
Koumey nakhal
Sama dome dji
Thiofelou Yaay si dome
Kouko doundoul doko meuneu khame
Beuss binga dioudo
Ba téw samay lokho
Li deh lernama
Bidew biy naw
Téré si assamanou mbeuguel
Doundou si khol té deh si beut
Li deh lernama
Bi ma ndieuké guiss sama Néné
Yeuk yeuk sama khôl bi nekh
Nakhal sa doom
Sou dioyé nga beg
Li deh lerna ma
Sama tiono moy sa banekh
Soumey liguey souba dey nekh
Dome faw nga begg
Ba raw si sey morom
Li deh lernama
Ayo sama néné
Néné touti
Koumey nakhal
Sama dome dji
Ayo sama néné
Néné touti
Koumey nakhal
Sama domedji
Sama doom sama sopé
Dounda mata dioyo
Mome laye dioye
Dôme doundeul
So doundé ba mane liguey
Feral saye rongone
Written by: Nguenar Diouf