クレジット
PERFORMING ARTISTS
Xalam
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Henri Guillabert
Composer
Moustapha Cisse
Lyrics
Papa Moussa Babou
Lyrics
Ibrahima Coundoul
Lyrics
PRODUCTION & ENGINEERING
Henri Guillabert
Producer
Xalam 2
Producer
Timour Gardenas
Mixing Engineer
歌詞
Démonta ba gueth
Démonta ba gueth
Démonta ba gueth
Feka molyi cia m’barma
Ma nanlene ass tiof
Aye mou new daga dagir
Di tempe Di gnew
Tallal samaye loxo Di nane
Gorgni nema so yexone touti
Dofi feke loudoul tiaxone
delouwatna gueth
Fekeu molyi ci teroubi
ma nane as wass
Aye mou new dague
Dogo Di tempe Di gnew
Gorgui neko so yexone touti
Dofi feke loudoul tiaxone
Gorgui nema ma dome
Galgangui m’balm’ban’gui
galgangui te n’ga gueti
bou boba pexmi quene dou
Laci djito
Pexmela New amna Lou moye lath
Do lale sa n’deuss
Tok ci kepargui neup
Di woute ba diantabi soufe
N'derane n’diowane
ndiogane n’derane
ban’ga n’baymi
Ta nangouwo daradia
Ban’ga n’baymi oh AK daradia
xeuthe m’bal warnala te lak dieun
diomboula
galgui yatouna guethgui yatouna
N’ga sani sa m’bal ba sa tias
Si teylo am lo in’dale
N’derane n’diowane
n’diowane n’derane
Ooooh ooooh
m’borom m’bolo demna gueth
Domou gain’de gueth
Di wouti loumou am
n’guir doun’dal wa keurgue
N’derane n’diowane
n’diowane n’derane
so amoul lo ligueye demal gueth gueth oh yes
Ooooh ooooh
n’diowane sa gale meun ci gale
Sa cigua rawna
Guethguimeuna rire maneu Sarane
galo gal galo gal keurgue yes
galo galo galo gal waaah
Written by: Henri Guillabert, Ibrahima Coundoul, Moustapha Cisse, Papa Moussa Babou

