album cover
Mon Combat
8,197
Music
Mon Combatは、アルバム『{albumName}』の一部として2025年8月25日にFaramareen MusicによりリリースされましたMon Combat - Single
album cover
リリース日2025年8月25日
レーベルFaramareen Music
メロディック度
アコースティック度
ヴァランス
ダンサビリティ
エネルギー
BPM100

歌詞

Saf nga djiguén lolou lalay topé
Damla khol lima guiss dima choqué
Ni nga mél naturelle la, doko forcer, non
Guel bi dafa tang badi laké
Safara bi nelow si yow la begg guiss (wopopop)
Pessé naala, ci li nga tok dafa diiss
Saf ni jumbo, toy ni rico
Guel bi dafa tang badi laké, chaud
Bad girl boy boula diégué ma shoot
Limay weur yeup ci djiguén nga ouf
Sa bep morom boula teukou nga shoot-shoot-shoot-shoot-shoot
Baby kaay sama wet, mbeuguél lalay sééd, man dama dioy
Bilay yaay kimay daanel oh oh oooh
Bimala guissé sama khol dafa nékh
Bimala guissé eh eh eeeh
Baby kaay sama wet, mbeuguél lalay sééd, man dama dioy
Bimala guissé eh eh eeeh
Sama linguère yaa khééré dé
Am nga thiass, waw ya tiékété
Yow lay weur souba ba ngone ma teudi
Yaag na beuré wayé yow tu es mon combat
Bandit bandit baby bandit bandiloul (bandé)
Wan ma sa bandit weundéloul
Thiow-li thiow-li yow la diougal nga féémou
Daggal sa yaram niou ndelou
Bad girl boy boula diégué ma shoot
Limay weur yeup ci djiguén nga ouf
Sa bep morom boula teukou nga shoot-shoot-shoot-shoot-shoot
Baby kaay sama wet, mbeuguél lalay sééd, man dama dioy
Bilay yaay kimay daanel oh oh oooh
Bimala guissé sama khol dafa nékh
Bimala guissé eh eh eeeh
Dama dioy, sama khol dafa nékh
Dama dioy, bimala guissé
Written by: Hamadou M.F. Goudiaby, Kevin Honoré Kailly, Wally B. Seck
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...