album cover
Cheikh Ibra Fall
1,071
Pop
Cheikh Ibra Fallは、アルバム『{albumName}』の一部として2004年5月31日にNonesuchによりリリースされましたEgypt
album cover
アルバムEgypt
リリース日2004年5月31日
レーベルNonesuch
言語English
メロディック度
アコースティック度
ヴァランス
ダンサビリティ
エネルギー
BPM153

歌詞

Mber mi nu naan Cheikh Ibra Fall
Te nu koy wooye Lamp Fall
Ahmadou Bamba moo ko taal
Foo ko tudde nepp ni Fall
Masula fo, xamul ay baal
Te kii du kuy tedd ci lal
Daa gis lutax muy tebb di dal
Ahmadou Bamba raw ay baal
Njekk mu now ci Bamba daal
Cheikh Ibra daa meloon ni taal
Am ay garab ba kenn du ko laal
Laajal, laajalma waa Kawsara Fall
Cheikh Ibra Fall, Cheikh Ibra Fall, jambaar la
Cheikh Ibra Fall, Baabul Muridin
Daa tedd guddi nu ne ko Fall
Mouhamadou Mbacke lay jafal
Jox ko ci moom ay tektal
Lii moo waral mu and ak aal
Waxtu wu ne mang koy maggal
Dii soq te roota ko war
Na mu fa fekkoon da leen lakkal
Ci di leen sujoot waajaangi daal
Cheikh Ibra Fall, Cheikh Ibra Fall, jambaar la
Cheikh Ibra Fall, Baabul Muridin
Fekkoonna nods mu nuy tangal
Ndongo ya naa bu kenn laal
Mu ne ko cass, du jog ci aal
Ngir li mu gem Cheikh Bamba daal
Cheikh Ibra Fall, Cheikh Ibra Fall, jambaar la
Cheikh Ibra Fall, Baabul Muridin
Written by: Youssou N'Dour
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...