album cover
Fakatal
album cover
Fakatal은(는) {albumName} 앨범에 수록된 곡으로 2021년 8월 1일일에 Diamono Production에서 발매되었습니다.Climat
앨범Climat
발매일2021년 8월 1일
라벨Diamono Production
BPM128
멜로디에 강한 음악
어쿠스틱 악기 중심
발랑스
춤추기 좋은 음악
에너지

가사

Da nga doon jéem, mënu loo, dellu ganaaw
Fa nga jëm yaa ko xam, dellul
Soo ko seetee, xam ni lóolu war na la
Rafet njort baax na lool
Defa doon daw di daw di daw ba daanu
Ndekete yow yaa ko kal
Da ngay nekk’ak nit, ngeen yàgg lool
ay at yu baree bari
Lépp baax na
Waaye su ngeen baayàntee mu xas la
Ndax ànd baax na, baayànte lu bon la
Defa doon daw di daw di daw ba daanu
Ndekete yow yaa ko kal
Defa doon daw di daw di daw ba daanu
Ndekete yow yaa ko kal
wànte xastee si baayànte, waru ca (choeurs)
Da ngeen yàggoon ànd boolo
wànte xastee si baayànte, waru ca (choeurs)
Buñ la laajee ci moom
Ngani ku baax la
wànte xastee ci baayànte, waru ca (choeurs)
Lu tax bu ngeen baayàntee nga wax si moom lu ñaaw ?
wànte xastee ci baayànte, waru ca (choeurs)
Ba ngeen di ànd ku baax la woon
wànte xastee ci baayànte, waru ca (choeurs)
Naka ngeen mëna baayàntee mu bonn si loolu ?
wànte xastee ci baayànte, waru ca (choeurs)
ànd baax na
wànte xastee ci baayànte, waru ca (choeurs)
Baayànte dagan na
wànte xastee ci baayànte, waru ca (choeurs)
May xalaat si loolu
wànte xastee ci baayànte, waru ca (choeurs)
Written by: Omar Pene

Loading...