크레딧
실연 아티스트
Maya Abdul
실연자
작곡 및 작사
Charles Mbaye Diagne
작곡가
Adja Maimouna Touré
작사가 겸 작곡가
Tiemoko Diatigui Diarra
작사가 겸 작곡가
프로덕션 및 엔지니어링
Charles Mbaye Diagne
녹음 엔지니어
François Diouf
프로듀서
가사
Dundu negn lou nekh
Mak yow lepp easy lepp nice
Dundu negn nakhar
Diar negn ci lepp lu dul peace
Dundu negn lou nekh
Mak yow lepp easy lepp nice
Dundu negn nakhar
Diar negn ci lepp lu dul peace
Fii la wara yem
Togn na la lou bari (i'm so sorry babe)
Djital sama khel, bayi sama xol guinaw
Yama xamal lou mel nii (oh ohh)
Mbeuguel bou deugg lol
Waye mbeuguel kesseh dou doy
Dundu negn lou nekh
Mak yow lepp easy lepp nice
Dundu negn nakhar
Diar negn ci lepp lu dul peace
Fii la wara yem
Fii la wara yem
Fii la wara yem
Fii la wara yem
Dundu negn lou nekh
Mak yow lepp easy lepp nice
Dundu negn nakhar
Diar negn ci lepp lu dul peace
Fii la wara yem
Written by: Adja Maimouna Touré, Charles Mbaye Diagne, Tiemoko Diatigui Diarra

