뮤직 비디오
뮤직 비디오
크레딧
작곡 및 작사
Samba Diarra Mbaye
작사가 겸 작곡가
Papa Noukhoum
작사가 겸 작곡가
Ismaila Talla
작사가 겸 작곡가
CHEIKH SEYE
작사가 겸 작곡가
프로덕션 및 엔지니어링
Iss 814
프로듀서
King Beat
프로듀서
가사
Eh mané
Bo deffé ñu wax
Bo defful ñu wax
Deffal li nguey def bayilene ñu deuké di wax
Bo deffé ñu wax
Bo defful ñu wax
Deffal li nguey def bayilene ñu deuké di wax
Di wax di wax
Di wax ah ah
Di wax di wax
Huuuuuuu
Djeri yow yow yow djeri
Djeri yow yow yow djeri
Dji anda key gooooo
(Fi moy sunu Senegal)
Ter bi sunu yeuf leu ñoko mom
(Dougne ko bayek gnom)
Sagnsé rafete guili ñoy borom
(Dougne ko bayek gnom)
Thiebou dieune national gnoy borom
(Dougne ko bayek gnom)
Diongoma you ame valeures dou gno ko mom
(Dougne ko bayek gnom)
Football dougal gagner gnoko mom
(Dougne ko bayek gnom)
Wou yay Samba
Wou yay yay Samba
Wou yay
Wou yay Samba
Wou yooooo
Fi moy sunu Senegal
Waaaaaaa wo (fi moy sunu Senegal)
Taratata taratata
(fi moy sunu Senegal)
Taratata taratata yeah
Written by: CHEIKH SEYE, Ismaila Talla, Papa Noukhoum, Samba Diarra Mbaye