album cover
Idda
14,695
Afro-Pop
Idda은(는) {albumName} 앨범에 수록된 곡으로 2022년 11월 10일일에 PDG Arts에서 발매되었습니다.Idda - Single
album cover
발매일2022년 11월 10일
라벨PDG Arts
멜로디에 강한 음악
어쿠스틱 악기 중심
발랑스
춤추기 좋은 음악
에너지
BPM

뮤직 비디오

뮤직 비디오

크레딧

실연 아티스트
Mia Guisse
Mia Guisse
실연자
작곡 및 작사
Stéphane Pambou
Stéphane Pambou
작곡가
Kruh Mandiou Mauri
Kruh Mandiou Mauri
작사가 겸 작곡가

가사

Danga took sama xol yaye kiki mome léboone
Guénteu na takeu leu kaay done sama yayou doome
Dougou na doundou na mougne took ndax yaw doome
Té beuss boussa doome indé dome defco dome sama doome
Li nit di dathie thi naigou seuye
Di guiss sa yaye té doko ko sagna déye
Li nit di dathie thi naigou seuye
Di guiss sa yaye té doko ko sagna déye
Dinala romb midi
Oooh wait
Té doma guiss
Oooh wait
Pénicilline yangui gneuw
Oooh wait
Ma dabali
Oooh wait
Gaa fof no welly
Oooh wait
Now doto KO défati
Oooh wait
Oooh wait
Oooh wait
Gnata yaye la fi seuye teuthie thi kasso ndax séne doome
Yi lathie ngay lathie téy amagou ma tontoome
Yague Toul legui Rek nga xam louy noone sama doome
Ideu bi tey la diékh tay Di diégueulou waat sama doome
Li nit di dathie thi naigou seuye
Di guiss sa yaye té doko ko sagna déye
Li nit di dathie thi naigou seuye
Di guiss sa yaye té doko ko sagna déye
Dinala romb midi
Oooh wait
Té doma guiss
Oooh wait
Pénicilline yangui gneuw
Oooh wait
Ma dabali
Oooh wait
Gaa fof no welly
Oooh wait
Now doto KO défati
Oooh wait
Dougou na doundou na mougne took ndax yaw doome
Paré- paré- pa- pa-
Paréna
Xamoni bou diééxé
Diééx na
Diééx na
Gneuweul
Han
Ngani
Han
Han
Mani baydou volume
Sabou mi nana ni
Tékki lunettes yi nguir gueuneu guiss
Written by: Kruh Mandiou Mauri, Stéphane Pambou
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...