album cover
Serigne Fallou
54
Mbalax
Serigne Fallou은(는) {albumName} 앨범에 수록된 곡으로 2025년 8월 11일일에 Prince Arts에서 발매되었습니다.Serigne Fallou - Single
album cover
발매일2025년 8월 11일
라벨Prince Arts
멜로디에 강한 음악
어쿠스틱 악기 중심
발랑스
춤추기 좋은 음악
에너지
BPM91

크레딧

실연 아티스트
NDAKHTE LO
NDAKHTE LO
실연자
작곡 및 작사
NDAKHTE LO
NDAKHTE LO
작사가 겸 작곡가
Prince Ibrahima Ndour
Prince Ibrahima Ndour
편곡자
프로덕션 및 엔지니어링
Prince Ibrahima Ndour
Prince Ibrahima Ndour
녹음 엔지니어
Prince Arts
Prince Arts
프로듀서

가사

Yàñuy moom
Ngir sa baay bañu moom ehh
Sañë nga ñoo ehh
dieund Sabador ehh Mame Bamba
Yàñuy moom
Ngir sa baay bañu moom
Sagn nga ñoo
dieund Sabador ehh
Ñun dé piiss yu forr yiñuy soll
Fallu yaañu koy diox
Kossi giss limuy soll ehh
Leep day valoré
Lepp day valoré
Yañuy moom
Ngir sa baay bañu moom
Sañe nga ñu
dieund Sabador ehh
Ñun dé yàñu tagaleek bidà
Soor kilo añ ak Laax ehh
Domi Bamba ya baax ehh
Yaay suñu rassolo
Yaañu moom
Ngir sa baay bañu moom
Sañe nga ñu
dieund Sabador ehh
Aladji Fallu Baayu Mbeen
Ibrahima ak Awa
Niang missi taw yu baax ehh
Seriñ Fallu ya neexë way
Yaañu moom
Ngir sa baay bañu moom
Sañe nga ñu
dieund Sabador ehh
Fallu tontu nap narr
Si xélam lu doy waar ehh
Narr ba daanu ak lerr
Naan ko do morom
Wax nga yonnent bi yawa yow
Manit manila yawa yow
Ngani ko yow
Mani la yow
Kima gisseel mo mata xam
Wax nga yonnent bi yawa yow
Manit manila yawa yow
Ngani ko yow
Mani la yow
Kima gisseel mo mata xam
Marché Ocass baca TOUBA
Lañu Dipé baca Ndiareem
Dagn dan diay ba Ngoon
Di Mbalax di dem
Ken dula juuti jaajêffé Galass
Serigne Fallou malen gënël
Momalen gënël
Baye Fallou malen gënël
Wax nga yonnent bi yawa yow
Manit manila yawa yow
Ngani ko yow
Mani la yow
Kima gisseel mo mata xam
Dinako wax Galass maggi Bass
Serigne fallou macay nder
Tabax jummah sampë raay
Auto ray difa jaar
Ndox mangay walangaan
Cey Baayu Mbeen
Touba Touba kêr Fallou LAAY
Wax nga yonnent bi yawa yow
Manit ma wax lë yawa yow
Ngani ko yow
Mani la yow
Kima gisseel mo mata xam
Written by: NDAKHTE LO
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...