album cover
Shukran Bamba
1,936
Pop
Shukran Bamba은(는) {albumName} 앨범에 수록된 곡으로 2004년 5월 31일일에 Nonesuch에서 발매되었습니다.Egypt
album cover
앨범Egypt
발매일2004년 5월 31일
라벨Nonesuch
언어English
멜로디에 강한 음악
어쿠스틱 악기 중심
발랑스
춤추기 좋은 음악
에너지
BPM133

뮤직 비디오

뮤직 비디오

가사

Alxamdulillaay ma sant Yalla
Bi mu ma wonaleek Cheikh Ahmadou Bamba
Cey jiile waay su feenutoon Mbacke
Lislaam ji dik te kon ndaw gacce
Këpp ku daan liggeeyal diine
Nasaraan bi rey la mbaa far la genne
Nasaxale lislaam de moo doon seen yitte
Cheikh Ahmadou Bamba moo leen far wacce
Shukraan laka
Shukraan
Modou Bamba
Xamalena ma Yalla, xamale ma yonentam
Wax ma ne jaam de day jaamu sangam
Litax nu naan ko Xaadimu Rasulu
Moo ma yengal ba ma far ca soobu
Leketu neen neenanu naxul bey
Fu nepp daw jublu gisnanu fa lu rey
Yagg na ma gestu lu jem ci Bamba
Masumu gis fu mu juuyook waa ja
Shukraan laka
Shukraan
Modou Bamba
Menuma la fey xanaa ma woy la
Liggeey ba dee rek ngir addiya la
Mbacke danga yaa ginaaw ak kanam
Nan roy ci yow ngir mena jem ci kanam
Soo deggee ma naan waa ja
Waa ja mooy kiy waajale gaa na
Te kooku daal, moo di doomi Abdoulaye ja ca Madina
Ahmadou Bamba, man de sant naa la
Jaa jef baayi Mamadou Lamine Barra
Sama diggenteek Yalla yaa ma ko leeral
Lu ne wonenga ko taxul nga jeexal
Yaa tax may baaleek di yeremaate
Jaa jef, jaa jef baayi Serin Saliou ak Serin Mourtala
Shukraan laka
Shukraan
Modou Bamba
Menuma la fey xanaa ma woy la
Liggeey ba dee rek ngir addiya la
Mbacke danga yaa ginaaw ak kanam
Nan roy ci yow ngir mena jem ci kanam
Ahmadou Bamba, man de sant naa la
Jaa jef baayi Mamadou Lamine Barra
Sama diggenteek Yalla yaa ma ko leeral
Lu ne wonenga ko taxul nga jeexal
Yaa tax may baaleek di yeremaate
Kenn dootuma atte te ban xeebaate
Jaa jef, jaa jef baayi Serin Saliou ak Serin Mourtala
Shukraan laka
Shukraan
Modou Bamba
Menuma la fey xanaa ma woy la
Liggeey ba dee rek ngir addiya la
Mbacke danga yaa ginaaw ak kanam
Nan roy ci yow ngir mena jem ci kanam
Written by: Kabou Gueye, Youssou N'Dour
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...