album cover
1886
3
Afro-Pop
1886은(는) {albumName} 앨범에 수록된 곡으로 2026년 5월 29일일에 wolofer records에서 발매되었습니다.1886 - Single
album cover
발매일2026년 5월 29일
라벨wolofer records
멜로디에 강한 음악
어쿠스틱 악기 중심
발랑스
춤추기 좋은 음악
에너지
BPM62

뮤직 비디오

뮤직 비디오

가사

Verse 1 :
Yay booy deg nga thiow li diougué ci xaré diambar ya xeex
Diassi yi awou tiss tissou ndam tegal thin li bax ndax
Mame booy aksi na aksi lén ñu téral su ñu diambar dji
Amari Ngoné du surga Djolof damel la ka warr
Guénn si leundeum
Tabi cii leer
Leerou bén sey dji fi takander
Lat Woté guerre
Ceddo yi tew
Dior woté dé, souf naan dérétu gueer
Chorus:
Na ñu boloo, boloo done béne
Legui djot na, siguil suñu rew
Nakh Mboloo, Mbolooy doolé
Doolé am na, Am na kone Ndam du fi dieekh
Senegal Ndiaye, Sen Gal suñu gal
Teranga, mooy xolu sama ada
Djom fula, ak faydaa la ma diaay
Dix huit cent quatre vingt six sa ma ndam
Verse 2:
Djam yi su ñu reew Senegal fu ñu dess mo ñu fa bayi
Du ñu sone du ñu tayi du ñu daw diow su ñu
Gaal gui muthieum mo ñuy rawalé rawalé su ñu euleuk
Malao bot su ñu thiossan té fu mu deem yobaléma
Ngaidé bi ngar sarrgal ko waar
Lal tapis rouge, rey guétu xarr
Deeret bi wal, mbegté mbi law
Gueum gueum bi wal galsen sa kaw
Tachou len beuss dou touti déé
Borom lay nourol taroulen
Linger di way kone fethe leen
Té mome sa bopou da fa neex
Chorus:
Na ñu boloo, boloo done béne
Legui djot na, siguil suñu rew
Nakh Mboloo, Mbolooy doolé
Doolé am na, Am na kone Ndam du fi dieekh
Senegal Ndiaye, Sen Gal suñu gal
Teranga, mooy xolu sama ada
Djom fula, ak faydaa la ma diaay
Dix huit cent quatre vingt six sa ma ndam
Na ñu boloo, boloo done béne
Legui djot na, siguil suñu rew
Nakh Mboloo, Mbolooy doolé
Doolé am na, Am na kone Ndam du fi dieekh
Senegal Ndiaye, Sen Gal suñu gal
Teranga, mooy xolu sama ada
Djom fula, ak faydaa la ma diaay
Dix huit cent quatre vingt six sa ma ndam
Written by: Mame Diarra Diop, papa alassane assane aly
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...