album cover
Xale
4,274
World
Xale은(는) {albumName} 앨범에 수록된 곡으로 1990년 1월 1일일에 Virgin Records에서 발매되었습니다.Set
album cover
앨범Set
발매일1990년 1월 1일
라벨Virgin Records
멜로디에 강한 음악
어쿠스틱 악기 중심
발랑스
춤추기 좋은 음악
에너지
BPM115

가사

Non non non nonnnn
Non non non nonnnn
Né Xalé bii
Né beugoumala merloo
Né Xalé bii
Né beugoumala merloo
Ndaxté so méré, so méré
Sama yaram daw, daw ba diaxalma (boul ma méré)
Lou mounoul gnak faw dafaw am
Wareef dafay mate
Lég Lég mou done lou doul neex
Yaw sama dom
Souba tax may wakh
So magué di nga xam
Ndaxté so dioyé, so dioyé
Sama yaram daw, daw ba diaxalma
Wadiour ak dom
Faw gnou y waxtane
Féxé melni mbourok sow
Ndem réro mouneta gnak
So Diaxlé, so diaxlé
Na sa khelmi dém
Dém ci say wadiour
Ni jamano mél
Tééy da cé baax
Jubantil bamou thior
Ndax momine dafay rooy
Bissa ngui gnew
Sou magué diarigne la
Lép nga ci bami ndaw
Ndaxté so méré, so dioyé
Sama yaram daw, daw ba diaxalma (boul ma méré)
Né Xalé bi
Né beugoumala merlo
Heuuuu xalé bi
Né bougouma la merlo
(Xalé momine la yaw bouko merlo té dé ko bégueul)
Ndaxté so méré, so méré
Sama yaram daw, daw ba diaxalma
Adouna nii la xalé bi lé
Sou bay waxaté nga déglou ko
Adouna nii la xalé bi lé
Sou yay waxaté nga déglou ko
Adouna nii la xalé bi lé
(Nangue ma deglo xel)
Sou bay waxaté nga déglou ko
(Bagn ma deglo xol)
Adouna nii la xalé bi lé
(Samaaa dooooom)
Sou yay waxaté nga déglou ko
(Nangue ma deglo xel)
Né xalé bi
Né beugoumala merlo
Haaaann Xalé bii
Né beugoumala merlo
Xalé bi
Né beugoumala dioylo
Ndaxté so méré, so dioyé
Sama yaram daw, daw ba diaxalma
Written by: Youssou N'Dour
instagramSharePathic_arrow_out􀆄 copy􀐅􀋲

Loading...