Vídeo da música
Vídeo da música
Créditos
INTERPRETAÇÃO
René-Marc Bini
Interpretação
COMPOSIÇÃO E LETRA
René-Marc Bini
Composição
Pape Dieye
Letra
PRODUÇÃO E ENGENHARIA
René-Marc Bini
Produção
Letra
Yaayoo booyoo manla
Yaayoo booyoo mangi
Yaayoo booyoo manla
Yaayoo booyoo mangi
Sama yoon
Yenn saa yi-yenn saa yi yangi may woo
Yenn saa yi-yenn saa yi yangi may xool
Yaayoo booy
Yenn saa yi-yenn saa yi malay di woo
Yenn saa yi-yenn saa yi malay di woo
Sama yoon
Yaayoo booyoo manla
Yaayoo booyoo mangi sama yoon
Yaayoo booyoo manla
Yaayoo booyoo mangi sama yoon
Yenn saa yi-yenn saa yi yangi may woo
Yenn saa yi-yenn saa yi yangi may xool
Yaayoo booy
Yenn saa yi-yenn saa yi malay di woo
Yaayoo booy yangi nii
Sama yoon
Yaayoo booy
Yaayoo booyoo manla
Yaayoo booyoo mangi sama yoon
Yaayoo booyoo manla
Yaayoo booyoo mangi sama yoon
Written by: Pape Dieye, René-Marc Bini


