Vídeo da música
Vídeo da música
Créditos
INTERPRETAÇÃO
Abdou Guite Seck
Vocais principais
COMPOSIÇÃO E LETRA
Abdoulaye Guitte SECK
Composição
Ousmane Ka
Arranjos
Bril
Arranjos
PRODUÇÃO E ENGENHARIA
Abdou Guite Seck
Produção
Letra
KAKATAR
Bagniou loo beugou loo hoo
Bobou batay ma doon taakhirlou
Merou loo beguou loo hoo
Khamou loo fan gua tollou
Fasse wooo seyou looo
Boul ma woowati telephone
Ma di la def sama khel
Diakhasse ngua sama khol
Meuneu touma sakh selë
Bouma woowati tel
Soma wowate man di naa la
Daniou digue woon beugeunte diapalante
Bagua tambale dima saytoo di ma fire
Thi similli gua mel nannen
Dagua ma doon fowe
Sa khel dong nekkon thi man
Dang ma beugoon teude
Ni gua def nakk metti na ma
Bama lakoy khole
Bim la wore deugouwouloo ma donn fire
Boul ma woowati telephone
Ma di la def sama khel
Meuneu touma sakh selë
Dioguatou ma sakh teel
Bou ma woowati tel
So ma wowate man di naa la
Beugueutou ma fowe mbeuguel
KAKATAR !
Te sa you diogue thi yaw ma dieul
KAKATAR !
Ya gui may nakk beugeup leudieul
KAKATAR !
Khol yeup nga beugueu dieul
Meunoon nga ma khalal yoon
Thi sa khol ben yoon
Bagn ma door niari yoon
Li mom dou yoon
He dinthial ma say foon
Khaw folen defoon
Nianen gni ma djitou woon
Thi sa khol nga len defoon
Yaw demal diemi len’nen
Nenoup nen gua nekke
Dounde wet aki fen
Nen dong guay dekke
Non saggane ba yaw gua mel ni
KAKATAR mi dou mak moome man de daw naa
Da niou digue woon beugeuntek diappalante
Bagniou loo beugou loo
Bobou ba tay ma doon taakhir lou
Ma di la def sama khel
Diakhasse ngua sama khol
Leudeumeul sa khel
Meuneu touma sakh selë
Bo ma wowe man di naa la
Non saggane ba yaw gua fete fi gua rere
KAKATAR mi doutoul mak moom
Man de daw naa
Non saggane ba yaw gua deffee
Na mou guënë niawe
KAKATAR mi dou mak moome
Man de daw naa
Non saggane
Ba yaw nga fete file
Do dem tew te do deupp
KAKATAR mi doutoul mak moom
Man de daw naa
…FIN…
Written by: Abdoulaye Guitte SECK