Vídeo da música

POSITIVE BLACK SOUL : DEUK BI DOU DEM ( PBS 25ANS)
Assista ao videoclipe da música {trackName} de {artistName}

Apresentado no

Créditos

PERFORMING ARTISTS
Positive Black Soul
Positive Black Soul
Performer
COMPOSITION & LYRICS
Positive Black Soul
Positive Black Soul
Composer
Akache
Akache
Composer

Letra

Deuk bi dou dem (fade) Deuk bi dou dem (fade) Dou dem, dou dem, dou dem, dou dem Sunu deuk bi dou dem, deuk bi dou dem Sunu deuk bi dou dem, deuk bi dou dem Sunu deuk bi dou dem Fi lek niou ngi koy tchakhané mom dou dem dem dem Sunu deuk bi dou dem, deuk bi dou dem Sunu deuk bi dou dem, deuk bi dou dem Sunu deuk bi dou dem Fi lek diogou niou liguèye mom dou dem dem dem Fi déé job amatoufi Naniou wakhanté deugg Fi dé liguèye amatoufi Emergence amagoufi naniou wakhanté deugg fi dé rupture amagoufi Li fi bonn diogué goufi, lougn fi yagga kass mou ngi sakh té diougué goufi Djeuf diou bonn diogué goufi, lii di deup caisse, sathie, guerre diogué gou fii Mou ngi weuy di weuy di weuy di weuy Sameu-katt bi nappeu-katt kholal nieup a ngi djoye Mou ngi weuy di weuy di weuy di weuy Sénégal walou lène étudiants yi niou ngi djoye Sunu deuk bi dou dem, deuk bi dou dem Sunu deuk bi dou dem, deuk bi dou dem Sunu deuk bi dou dem Fi lek niou ngi koy tchakhané mom dou dem dem dem Sunu deuk bi dou dem, deuk bi dou dem Sunu deuk bi dou dem, deuk bi dou dem Sunu deuk bi dou dem Fi lek diogou niou liguèye mom dou dem dem dem Ey, li di ram douma ko sétann Bougouma téleu wakh mais fi mou dieum douma ko sétann Li di ram douma ko sétann Bayi beu lepp klaté affaire bi di niou rétann Mou ngi weuy di weuy di weuy di weuy Wakh meu rek lann mo waral adina bi war niou rétann Mou ngi weuy di weuy di weuy di weuy Wakh meu li niou téré yeungou niou ngi togg diko sétann Mou ngi weuy di weuy di weuy di weuy Courant coupé ndokh bi coupé doundou bi di gueune taar Mou ngi weuy di weuy di weuy di weuy Li niou digonn défou niouko bobou ba légui niou ngi kharr Sunu deuk bi dou dem, deuk bi dou dem Sunu deuk bi dou dem, deuk bi dou dem Sunu deuk bi dou dem Fi lek niou ngi koy tchakhané mom dou dem dem dem Sunu deuk bi dou dem, deuk bi dou dem Sunu deuk bi dou dem, deuk bi dou dem Sunu deuk bi dou dem Fi lek diogou niou liguèye mom dou dem dem dem Dou dem, dou dem, dou dem, dou dem
Writer(s): Akache, Positive Black Soul Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out